As-Saffat · 74/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
إِلَّا عِبَادَ اللَّهِ الْمُخْلَصِينَ ۝٧٤
Illaa `ibaadal laahil mukhlaseen
📖 Tekkim Wolof
Ña ca dul jaami Yàlla ya ca daan sellal :

🎧 Dégg


📜 Aaya 72-76 — Simoore As-Saffat

72وَلَقَدْ أَرْسَلْنَا فِيهِم مُّنذِرِينَ
Ndax yónni woon Nanu ci ñoom ñuy xuppe, di waaraate .
73فَانظُرْ كَيْفَ كَانَ عَاقِبَةُ الْمُنذَرِينَ
Xoolal mujjug ñanu daan xupp !
74إِلَّا عِبَادَ اللَّهِ الْمُخْلَصِينَ
Ña ca dul jaami Yàlla ya ca daan sellal :
75وَلَقَدْ نَادَانَا نُوحٌ فَلَنِعْمَ الْمُجِيبُونَ
Nooh woo na Nu di ñaan, Nu wuyyu ko, nangu ñaanam.
76وَنَجَّيْنَاهُ وَأَهْلَهُ مِنَ الْكَرْبِ الْعَظِيمِ
Nu musal ko mook njabootam ci tiit mu rëy ma,
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
74Aaya

Tekki — As-Saffat 74

Simoore As-Saffat Aaya 74 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña ca dul jaami Yàlla ya ca daan sellal :

Simoore Aaya 74/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 72–76. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers