Ghafir · 64/85
Tekki Waxtaan — Ghafir
اللَّهُ الَّذِي جَعَلَ لَكُمُ الْأَرْضَ قَرَارًا وَالسَّمَاءَ بِنَاءً وَصَوَّرَكُمْ فَأَحْسَنَ صُوَرَكُمْ وَرَزَقَكُم مِّنَ الطَّيِّبَاتِ ۚ ذَٰلِكُمُ اللَّهُ رَبُّكُمْ ۖ فَتَبَارَكَ اللَّهُ رَبُّ الْعَالَمِينَ ۝٦٤
Allaahul lazee ja`ala lakumul arda qaraaranw wassa maaa`a binaaa`anw wa sawwarakum fa ahsana suwarakum wa razaqakum minat taiyibaat; zaalikumul laahu Rabbukum fatabaarakal laahu Rabbul `aalameen
📖 Tekkim Wolof
Yàlla mi leen defal suuf si muy laltaay defal leen asamaan si muy mbaar mu móol leen rafetal seeni melo , - wërsëgal leen ci yu teey yi ! Koo koo di seen Boroom ; Yàlla barkeel na, Moom Miy Boroom àddina si!

🎧 Dégg


📜 Aaya 62-66 — Ghafir

62ذَٰلِكُمُ اللَّهُ رَبُّكُمْ خَالِقُ كُلِّ شَيْءٍ لَّا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ ۖ فَأَنَّىٰ تُؤْفَكُونَ
Koo ku moo di Yàlla seen Boroom, Moo bind lépp. Amul jeneen Yàlla judul moom. Kon naka ngeen di lajje féew (ca yoonu Yàlla wu jub wa xocc) ?
63كَذَٰلِكَ يُؤْفَكُ الَّذِينَ كَانُوا بِآيَاتِ اللَّهِ يَجْحَدُونَ
Noonu la ñu daan weddi kàdduy Yàlla di dumóoyoo [yoonu] Yàlla.
64اللَّهُ الَّذِي جَعَلَ لَكُمُ الْأَرْضَ قَرَارًا وَالسَّمَاءَ بِنَاءً وَصَوَّرَكُمْ فَأَحْسَنَ صُوَرَكُمْ وَرَزَقَكُم مِّنَ الطَّيِّبَاتِ ۚ ذَٰلِكُمُ اللَّهُ رَبُّكُمْ ۖ فَتَبَارَكَ اللَّهُ رَبُّ الْعَالَمِينَ
Yàlla mi leen defal suuf si muy laltaay defal leen asamaan si muy mbaar mu móol leen rafetal seeni melo , - wërsëgal leen ci yu teey yi ! Koo koo di seen Boroom ; Yàlla barkeel na, Moom Miy Boroom àddina si!
65هُوَ الْحَيُّ لَا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ فَادْعُوهُ مُخْلِصِينَ لَهُ الدِّينَ ۗ الْحَمْدُ لِلَّهِ رَبِّ الْعَالَمِينَ
Mooy kiy dund. Amul jeneen Yàlla judul moom. Na ngeen koy jaamu, te di ko sellal diine ji. Cant ñeel na Yàlla, Miy Boroom àddina si !
66۞ قُلْ إِنِّي نُهِيتُ أَنْ أَعْبُدَ الَّذِينَ تَدْعُونَ مِن دُونِ اللَّهِ لَمَّا جَاءَنِيَ الْبَيِّنَاتُ مِن رَّبِّي وَأُمِرْتُ أَنْ أُسْلِمَ لِرَبِّ الْعَالَمِينَ
Waxal ne : “Tere na nu ma, may jaamu li ngeen di jaamu te du Yàlla, waxtu wa ma ay lay yu leer nàññ digëlee te bawoo ci sama Boroom, te it digaléef na ma jébël sama bopp Yàlla miy Boroom àddina si”.
GhafirFihi Alxuraan
85Aaya
MeccanRevelation
64Aaya

Tekki — Ghafir 64

Simoore Ghafir Aaya 64 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yàlla mi leen defal suuf si muy laltaay defal leen…

Simoore Aaya 64/85 — Ghafir غافر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ghafir Dégg, Ghafir Tekki, Ghafir mp3, Ghafir pdf. Aaya 62–66. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers