Ash-Shura · 24/53
Tekki Waxtaan — Ash-Shura
أَمْ يَقُولُونَ افْتَرَىٰ عَلَى اللَّهِ كَذِبًا ۖ فَإِن يَشَإِ اللَّهُ يَخْتِمْ عَلَىٰ قَلْبِكَ ۗ وَيَمْحُ اللَّهُ الْبَاطِلَ وَيُحِقُّ الْحَقَّ بِكَلِمَاتِهِ ۚ إِنَّهُ عَلِيمٌ بِذَاتِ الصُّدُورِ ٢٤
Transliteration
Am yaqooloonaf tara `alal laahi kaziban fa-iny yasha il laahu yakhtim `alaa qalbik; wa yamhul laahul baatila wa yuhiqqul haqqa bi Kalimaatih; innahoo `Aleemum bizaatis sudoor
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Walla ñu daan wax naan day duural Yàlla ay fen. Bu neexoon Yàlla, Mu fatt sab xol. Yàlla dana (raaf , far) lépp luy neen. Te dana dëgëral dëgg ci ay kàddoom moom xam na li làmbu ci dënn yi.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 22-26 — Ash-Shura
22تَرَى الظَّالِمِينَ مُشْفِقِينَ مِمَّا كَسَبُوا وَهُوَ وَاقِعٌ بِهِمْ ۗ وَالَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ فِي رَوْضَاتِ الْجَنَّاتِ ۖ لَهُم مَّا يَشَاءُونَ عِندَ رَبِّهِمْ ۚ ذَٰلِكَ هُوَ الْفَضْلُ الْكَبِيرُ
Danga gis tooñkat ya ñu tiit lool ngir la ñu daan def, (mu di mbugël) muy dal ci seen kaw. Waaye ña gëmoon te daan def yiw, ñoom ña nga ca biir dëri àjjana ya, ñu fay am la ñu bëgg ci seen Boroom. Loolu moo di ngëneel la gën a rëy !
23ذَٰلِكَ الَّذِي يُبَشِّرُ اللَّهُ عِبَادَهُ الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ ۗ قُل لَّا أَسْأَلُكُمْ عَلَيْهِ أَجْرًا إِلَّا الْمَوَدَّةَ فِي الْقُرْبَىٰ ۗ وَمَن يَقْتَرِفْ حَسَنَةً نَّزِدْ لَهُ فِيهَا حُسْنًا ۚ إِنَّ اللَّهَ غَفُورٌ شَكُورٌ
Loolu moo di [xibaar bu neex] bi Yàlla di bégale jaamam ña gëm tey jëf yiw ! waxal ne : “Du ma leen laaj genn pey lu dul dëgëral gi ci diggënte ag mbokkoo”. Képp ku def lu rafet, Dananu ko ko dollil lu gën a rafet (mu di ab neexal). Yàlla jégëlaakoon la kuy sant la (delloo njukël).
24أَمْ يَقُولُونَ افْتَرَىٰ عَلَى اللَّهِ كَذِبًا ۖ فَإِن يَشَإِ اللَّهُ يَخْتِمْ عَلَىٰ قَلْبِكَ ۗ وَيَمْحُ اللَّهُ الْبَاطِلَ وَيُحِقُّ الْحَقَّ بِكَلِمَاتِهِ ۚ إِنَّهُ عَلِيمٌ بِذَاتِ الصُّدُورِ
Walla ñu daan wax naan day duural Yàlla ay fen. Bu neexoon Yàlla, Mu fatt sab xol. Yàlla dana (raaf , far) lépp luy neen. Te dana dëgëral dëgg ci ay kàddoom moom xam na li làmbu ci dënn yi.
25وَهُوَ الَّذِي يَقْبَلُ التَّوْبَةَ عَنْ عِبَادِهِ وَيَعْفُو عَنِ السَّيِّئَاتِ وَيَعْلَمُ مَا تَفْعَلُونَ
Mooy kiy ndangu tuub ci jaamam ñi, tey jéggale ñaawtéef yi tey xam li ngeen di def.
26وَيَسْتَجِيبُ الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ وَيَزِيدُهُم مِّن فَضْلِهِ ۚ وَالْكَافِرُونَ لَهُمْ عَذَابٌ شَدِيدٌ
te it mooy nangul ñi gëm tey jëf yiw di leen xeewël, yéefar yi nag ñoom am na ñu mbugël mu tar.
Ash-ShuraFihi Alxuraan
53Aaya
MeccanRevelation
24Aaya
Tekki — Ash-Shura 24
Simoore Ash-Shura Aaya 24 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Walla ñu daan wax naan day duural Yàlla ay fen.…Simoore Aaya 24/53 — Ash-Shura الشورى (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shura Dégg, Ash-Shura Tekki, Ash-Shura mp3, Ash-Shura pdf. Aaya 22–26. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








