Ash-Shura · 53/53
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shura
صِرَاطِ اللَّهِ الَّذِي لَهُ مَا فِي السَّمَاوَاتِ وَمَا فِي الْأَرْضِ ۗ أَلَا إِلَى اللَّهِ تَصِيرُ الْأُمُورُ ۝٥٣
Siraatil laahil lazee lahoo maa fis samaawaati wa maa fil ard; alaaa ilal laahi taseerul umoor
📖 Tekkim Wolof
yoonu Yàlla ji moom asamaan yeek suuf si ak li ci seen biir. Ca dëgg-dëgg ca yàlla la mbir yépp di mujj.

🎧 Dégg


📜 Aaya 51-53 — Simoore Ash-Shura

51۞ وَمَا كَانَ لِبَشَرٍ أَن يُكَلِّمَهُ اللَّهُ إِلَّا وَحْيًا أَوْ مِن وَرَاءِ حِجَابٍ أَوْ يُرْسِلَ رَسُولًا فَيُوحِيَ بِإِذْنِهِ مَا يَشَاءُ ۚ إِنَّهُ عَلِيٌّ حَكِيمٌ
Yàlla du waxanteek kenn nit lu dul ci soloo, walla ci ginnaaw kiiraay, walla mu yabal ndaw (Malaaka) mu di ko soloo, lu ko soob, ci ndigalul Yàllal. Yàlla aji Kawe la aji Xereñ la.
52وَكَذَٰلِكَ أَوْحَيْنَا إِلَيْكَ رُوحًا مِّنْ أَمْرِنَا ۚ مَا كُنتَ تَدْرِي مَا الْكِتَابُ وَلَا الْإِيمَانُ وَلَٰكِن جَعَلْنَاهُ نُورًا نَّهْدِي بِهِ مَن نَّشَاءُ مِنْ عِبَادِنَا ۚ وَإِنَّكَ لَتَهْدِي إِلَىٰ صِرَاطٍ مُّسْتَقِيمٍ
Noonu la ñuy soloo ci yaw [Alxuraan] ci Sunu ndigël. amoo woon benn xam-xam ci Téere bi du caagéene ngëm; waaye def leer di ci gindi ku nu soob ci sunu jaam ñi. Te yaw it da ngay gindee jëme ci yoon wu jub wa xocc,
53صِرَاطِ اللَّهِ الَّذِي لَهُ مَا فِي السَّمَاوَاتِ وَمَا فِي الْأَرْضِ ۗ أَلَا إِلَى اللَّهِ تَصِيرُ الْأُمُورُ
yoonu Yàlla ji moom asamaan yeek suuf si ak li ci seen biir. Ca dëgg-dëgg ca yàlla la mbir yépp di mujj.
Ash-ShuraFihi Alxuraan
53Aaya
MeccanRevelation
53Aaya

Tekki — Ash-Shura 53

Simoore Ash-Shura Aaya 53 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : yoonu Yàlla ji moom asamaan yeek suuf si ak li…

Simoore Aaya 53/53 — Simoore Ash-Shura الشورى (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shura Dégg, Simoore Ash-Shura Tekki, Simoore Ash-Shura mp3, Simoore Ash-Shura pdf. Aaya 51–53. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers