Az-Zukhruf · 10/89
Tekki Waxtaan — Az-Zukhruf
الَّذِي جَعَلَ لَكُمُ الْأَرْضَ مَهْدًا وَجَعَلَ لَكُمْ فِيهَا سُبُلًا لَّعَلَّكُمْ تَهْتَدُونَ ۝١٠
Allazee ja`ala lakumul arda mahdanw wa ja`ala lakum feehaa subulal la`allakum tahtadoon
📖 Tekkim Wolof
Yàlla mi leen defal suuf si muy laltaay defaral na leen ci ay yoon ngir ngeen man cee ginduku ;

🎧 Dégg


📜 Aaya 8-12 — Az-Zukhruf

8فَأَهْلَكْنَا أَشَدَّ مِنْهُم بَطْشًا وَمَضَىٰ مَثَلُ الْأَوَّلِينَ
Faagaagal na nu ña leen ëppoon doole ! Xam ngeen xibaari ña jiitu woon.
9وَلَئِن سَأَلْتَهُم مَّنْ خَلَقَ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ لَيَقُولُنَّ خَلَقَهُنَّ الْعَزِيزُ الْعَلِيمُ
Te soo leen laajee : “Kan moo bind asamaan yeek suuf ? ” Dañu naan : “Yàlla, miy boroom Kàttan di ku Xam moo leen bind”.
10الَّذِي جَعَلَ لَكُمُ الْأَرْضَ مَهْدًا وَجَعَلَ لَكُمْ فِيهَا سُبُلًا لَّعَلَّكُمْ تَهْتَدُونَ
Yàlla mi leen defal suuf si muy laltaay defaral na leen ci ay yoon ngir ngeen man cee ginduku ;
11وَالَّذِي نَزَّلَ مِنَ السَّمَاءِ مَاءً بِقَدَرٍ فَأَنشَرْنَا بِهِ بَلْدَةً مَّيْتًا ۚ كَذَٰلِكَ تُخْرَجُونَ
Mooy kiy wàccee am ndox ci asamaan si di ko yemale Ñu di ca naatal ay dëkk yu bekkooroon. noonu it ngeen di dekkiwaate ;
12وَالَّذِي خَلَقَ الْأَزْوَاجَ كُلَّهَا وَجَعَلَ لَكُم مِّنَ الْفُلْكِ وَالْأَنْعَامِ مَا تَرْكَبُونَ
Moo bind tóolent yépp, defaral ay gaal, amal yu ngeen di war,
Az-ZukhrufFihi Alxuraan
89Aaya
MeccanRevelation
10Aaya

Tekki — Az-Zukhruf 10

Simoore Az-Zukhruf Aaya 10 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yàlla mi leen defal suuf si muy laltaay defaral na…

Simoore Aaya 10/89 — Az-Zukhruf الزخرف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Az-Zukhruf Dégg, Az-Zukhruf Tekki, Az-Zukhruf mp3, Az-Zukhruf pdf. Aaya 8–12. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers