Muhammad · 1/38
Tekki Waxtaan — Simoore Muhammad
الَّذِينَ كَفَرُوا وَصَدُّوا عَن سَبِيلِ اللَّهِ أَضَلَّ أَعْمَالَهُمْ ۝١
Allazeena kafaroo wa saddoo`an sabeelil laahi adalla a`maalahum
📖 Tekkim Wolof
Ña weddi tey dumóoyu yoonu Yàlla, (tax na) ba sànk na séen jëf.

🎧 Dégg


📜 Aaya 1-3 — Simoore Muhammad

1الَّذِينَ كَفَرُوا وَصَدُّوا عَن سَبِيلِ اللَّهِ أَضَلَّ أَعْمَالَهُمْ
Ña weddi tey dumóoyu yoonu Yàlla, (tax na) ba sànk na séen jëf.
2وَالَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ وَآمَنُوا بِمَا نُزِّلَ عَلَىٰ مُحَمَّدٍ وَهُوَ الْحَقُّ مِن رَّبِّهِمْ ۙ كَفَّرَ عَنْهُمْ سَيِّئَاتِهِمْ وَأَصْلَحَ بَالَهُمْ
Ña gëmoon te daan jëf yiw te ñoo daan gëm la ñu daan wàcce ci Muhammad (Alxuraan) – te mooy dëgg ga bawoo ca séen Boroom – Faralal na leen séen ñaawtéef te it yéwénal na leen séen mbir.
3ذَٰلِكَ بِأَنَّ الَّذِينَ كَفَرُوا اتَّبَعُوا الْبَاطِلَ وَأَنَّ الَّذِينَ آمَنُوا اتَّبَعُوا الْحَقَّ مِن رَّبِّهِمْ ۚ كَذَٰلِكَ يَضْرِبُ اللَّهُ لِلنَّاسِ أَمْثَالَهُمْ
Li wér moo di ne ñiy weddi dañoo topp Neen ñi gëm nag ñoom dañoo topp Dëgg gu bawoo ca séen Boroom. Noonu la Yàlla di séddale nit séeni léebu.
MuhammadFihi Alxuraan
38Aaya
MedinanRevelation
1Aaya

Tekki — Muhammad 1

Simoore Muhammad Aaya 1 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña weddi tey dumóoyu yoonu Yàlla, (tax na) ba sànk…

Simoore Aaya 1/38 — Simoore Muhammad محمد (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Muhammad Dégg, Simoore Muhammad Tekki, Simoore Muhammad mp3, Simoore Muhammad pdf. Aaya 1–3. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers