Al-Fath · 8/29
Tekki Waxtaan — Al-Fath
إِنَّا أَرْسَلْنَاكَ شَاهِدًا وَمُبَشِّرًا وَنَذِيرًا ٨
Transliteration
Innaaa arsalnaaka shaahi danw wa mubashshiranw wa nazeera
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Yónni nanu la ngaay seede (ci saw xeet), di béglekat (ci jullit ñi) di xuppekat (ci yéefar yi),
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 6-10 — Al-Fath
6وَيُعَذِّبَ الْمُنَافِقِينَ وَالْمُنَافِقَاتِ وَالْمُشْرِكِينَ وَالْمُشْرِكَاتِ الظَّانِّينَ بِاللَّهِ ظَنَّ السَّوْءِ ۚ عَلَيْهِمْ دَائِرَةُ السَّوْءِ ۖ وَغَضِبَ اللَّهُ عَلَيْهِمْ وَلَعَنَهُمْ وَأَعَدَّ لَهُمْ جَهَنَّمَ ۖ وَسَاءَتْ مَصِيرًا
(ngir loolu it) dana mbugël naaféq yu, góor yeek yu jigéen yi, ak bokkaalekat yu goor yaak yu jigéen yay njortu ci Yàlla. Ak itam ne waajalal na leen safara muy dëkkuwaay bu bon!
7وَلِلَّهِ جُنُودُ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۚ وَكَانَ اللَّهُ عَزِيزًا حَكِيمًا
Yàllaa moom xarekati asamaan yeek suuf si ; Yàlla Boroom Kàttan la di Ku Xereñ.
8إِنَّا أَرْسَلْنَاكَ شَاهِدًا وَمُبَشِّرًا وَنَذِيرًا
Yónni nanu la ngaay seede (ci saw xeet), di béglekat (ci jullit ñi) di xuppekat (ci yéefar yi),
9لِّتُؤْمِنُوا بِاللَّهِ وَرَسُولِهِ وَتُعَزِّرُوهُ وَتُوَقِّرُوهُ وَتُسَبِّحُوهُ بُكْرَةً وَأَصِيلًا
ngir ngeen gëm Yàlla akub Yonentam, te di ko màggal, te di ko weg, ak it ngir ngeen di ko sàbbaal (kañ) subaak ngoon.
10إِنَّ الَّذِينَ يُبَايِعُونَكَ إِنَّمَا يُبَايِعُونَ اللَّهَ يَدُ اللَّهِ فَوْقَ أَيْدِيهِمْ ۚ فَمَن نَّكَثَ فَإِنَّمَا يَنكُثُ عَلَىٰ نَفْسِهِ ۖ وَمَنْ أَوْفَىٰ بِمَا عَاهَدَ عَلَيْهُ اللَّهَ فَسَيُؤْتِيهِ أَجْرًا عَظِيمًا
Ñay jaayanteek yow ña ngay jaayanteek Yàlla (“bay’atu ridwaan bil hudaybiyyati”) : loxo Yàllaa ngi séeni yoxo (tegoonañook Yàlla loxo) . Képp ku ca xàcc, boppam la xàccal ; képp ku matal kóllare ga mooy séqag Yàlla, Dana ko xalset a jox ag pey gu màgg.
Al-FathFihi Alxuraan
29Aaya
MedinanRevelation
8Aaya
Tekki — Al-Fath 8
Simoore Al-Fath Aaya 8 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yónni nanu la ngaay seede (ci saw xeet), di béglekat…Simoore Aaya 8/29 — Al-Fath الفتح (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Fath Dégg, Al-Fath Tekki, Al-Fath mp3, Al-Fath pdf. Aaya 6–10. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








