Qaf · 14/45
Tekki Waxtaan — Qaf
وَأَصْحَابُ الْأَيْكَةِ وَقَوْمُ تُبَّعٍ ۚ كُلٌّ كَذَّبَ الرُّسُلَ فَحَقَّ وَعِيدِ ۝١٤
Wa Ashaabul Aykati wa qawmu Tubba`; kullun kazzabar Rusula fahaqqa wa`eed
📖 Tekkim Wolof
ak waa Aykata ak nitu Tubba’a. Ñépp weddiwoon Yonent ya. Samag tëkku dal leen (di mbugël).

🎧 Dégg


📜 Aaya 12-16 — Qaf

12كَذَّبَتْ قَبْلَهُمْ قَوْمُ نُوحٍ وَأَصْحَابُ الرَّسِّ وَثَمُودُ
Ca la leen jiitu woon, nitu Nooh , ak waa Rasi ak waa Samuud weddiwoon nañu,
13وَعَادٌ وَفِرْعَوْنُ وَإِخْوَانُ لُوطٍ
ak waa Aad ak Firawna ak mbokki Lóot,
14وَأَصْحَابُ الْأَيْكَةِ وَقَوْمُ تُبَّعٍ ۚ كُلٌّ كَذَّبَ الرُّسُلَ فَحَقَّ وَعِيدِ
ak waa Aykata ak nitu Tubba’a. Ñépp weddiwoon Yonent ya. Samag tëkku dal leen (di mbugël).
15أَفَعَيِينَا بِالْخَلْقِ الْأَوَّلِ ۚ بَلْ هُمْ فِي لَبْسٍ مِّنْ خَلْقٍ جَدِيدٍ
Nga ne ma lan ? Nun Yàlla danoo sonn ca bind gu jëkk ga ? Ñii kay ñi ngi cim lënt ci mbirum dekkiwaat (ku sos dekkil jaaxalu ko).
16وَلَقَدْ خَلَقْنَا الْإِنسَانَ وَنَعْلَمُ مَا تُوَسْوِسُ بِهِ نَفْسُهُ ۖ وَنَحْنُ أَقْرَبُ إِلَيْهِ مِنْ حَبْلِ الْوَرِيدِ
Nun Yàlla Noo sàkk nit bind ko te it xam Nanu liy jax-jaxi ci am xolam te sax Nun Noo ko gën a jegeñ buum giy téye ab xol
QafFihi Alxuraan
45Aaya
MeccanRevelation
14Aaya

Tekki — Qaf 14

Simoore Qaf Aaya 14 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ak waa Aykata ak nitu Tubba’a. Ñépp weddiwoon Yonent ya.…

Simoore Aaya 14/45 — Qaf ق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Qaf Dégg, Qaf Tekki, Qaf mp3, Qaf pdf. Aaya 12–16. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers