Qaf · 26/45
Tekki Waxtaan — Simoore Qaf
الَّذِي جَعَلَ مَعَ اللَّهِ إِلَٰهًا آخَرَ فَأَلْقِيَاهُ فِي الْعَذَابِ الشَّدِيدِ ۝٢٦
Allazee ja`ala ma`al laahi ilaahan aakhara fa alqiyaahu fil`azaabish shadeed
📖 Tekkim Wolof
ka daan jéem a woote jeneen Yàlla di ko booleek Yàlla. Sànni leen ko ci mbugal mu tar ma”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 24-28 — Simoore Qaf

24أَلْقِيَا فِي جَهَنَّمَ كُلَّ كَفَّارٍ عَنِيدٍ
“Yéen ñaar, sànni leen ca safara weddiwaakoon ya daan féttérlu,
25مَّنَّاعٍ لِّلْخَيْرِ مُعْتَدٍ مُّرِيبٍ
ña daan tere aw yiw, te daan jalgati, daan sikki-sàkka,
26الَّذِي جَعَلَ مَعَ اللَّهِ إِلَٰهًا آخَرَ فَأَلْقِيَاهُ فِي الْعَذَابِ الشَّدِيدِ
ka daan jéem a woote jeneen Yàlla di ko booleek Yàlla. Sànni leen ko ci mbugal mu tar ma”.
27۞ قَالَ قَرِينُهُ رَبَّنَا مَا أَطْغَيْتُهُ وَلَٰكِن كَانَ فِي ضَلَالٍ بَعِيدٍ
Nekkaaleem ja (Saytaane) ngay wax naan : “sama Boroom, man dey bewloowuma ko ; waaye moom dafa nekkoon ci ag réer gu tar”.
28قَالَ لَا تَخْتَصِمُوا لَدَيَّ وَقَدْ قَدَّمْتُ إِلَيْكُم بِالْوَعِيدِ
(Yàlla daldi ne leen) : “Bu leen fi xulóo ! Lii lépp waxoon naa leen ko.
QafFihi Alxuraan
45Aaya
MeccanRevelation
26Aaya

Tekki — Qaf 26

Simoore Qaf Aaya 26 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ka daan jéem a woote jeneen Yàlla di ko booleek…

Simoore Aaya 26/45 — Simoore Qaf ق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Qaf Dégg, Simoore Qaf Tekki, Simoore Qaf mp3, Simoore Qaf pdf. Aaya 24–28. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers