Qaf · 27/45
Tekki Waxtaan — Qaf
۞ قَالَ قَرِينُهُ رَبَّنَا مَا أَطْغَيْتُهُ وَلَٰكِن كَانَ فِي ضَلَالٍ بَعِيدٍ ۝٢٧
Qaala qareenuhoo Rabbanaa maaa atghaituhoo wa laakin kaana fee dalaahim ba`eed
📖 Tekkim Wolof
Nekkaaleem ja (Saytaane) ngay wax naan : “sama Boroom, man dey bewloowuma ko ; waaye moom dafa nekkoon ci ag réer gu tar”.
🎧 Dégg

📜 Aaya 25-29 — Qaf

25مَّنَّاعٍ لِّلْخَيْرِ مُعْتَدٍ مُّرِيبٍ
ña daan tere aw yiw, te daan jalgati, daan sikki-sàkka,
26الَّذِي جَعَلَ مَعَ اللَّهِ إِلَٰهًا آخَرَ فَأَلْقِيَاهُ فِي الْعَذَابِ الشَّدِيدِ
ka daan jéem a woote jeneen Yàlla di ko booleek Yàlla. Sànni leen ko ci mbugal mu tar ma”.
27۞ قَالَ قَرِينُهُ رَبَّنَا مَا أَطْغَيْتُهُ وَلَٰكِن كَانَ فِي ضَلَالٍ بَعِيدٍ
Nekkaaleem ja (Saytaane) ngay wax naan : “sama Boroom, man dey bewloowuma ko ; waaye moom dafa nekkoon ci ag réer gu tar”.
28قَالَ لَا تَخْتَصِمُوا لَدَيَّ وَقَدْ قَدَّمْتُ إِلَيْكُم بِالْوَعِيدِ
(Yàlla daldi ne leen) : “Bu leen fi xulóo ! Lii lépp waxoon naa leen ko.
29مَا يُبَدَّلُ الْقَوْلُ لَدَيَّ وَمَا أَنَا بِظَلَّامٍ لِّلْعَبِيدِ
Wax ja du sippiku fi man ; te it Duma tooñ benn jaam”.
QafFihi Alxuraan
45Aaya
MeccanRevelation
27Aaya

Tekki — Qaf 27

Simoore Qaf Aaya 27 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nekkaaleem ja (Saytaane) ngay wax naan : “sama Boroom, man…

Simoore Aaya 27/45 — Qaf ق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Qaf Dégg, Qaf Tekki, Qaf mp3, Qaf pdf. Aaya 25–29. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers