Qaf · 25/45
Tekki Waxtaan — Simoore Qaf
مَّنَّاعٍ لِّلْخَيْرِ مُعْتَدٍ مُّرِيبٍ ۝٢٥
Mannaa`il lilkhayri mu`tadim mureeb
📖 Tekkim Wolof
ña daan tere aw yiw, te daan jalgati, daan sikki-sàkka,

🎧 Dégg


📜 Aaya 23-27 — Simoore Qaf

23وَقَالَ قَرِينُهُ هَٰذَا مَا لَدَيَّ عَتِيدٌ
Ka muy lëkóol ma ngay wax naan : “Kii mooy sama àndandoo bi ma dul tàggóolati”.
24أَلْقِيَا فِي جَهَنَّمَ كُلَّ كَفَّارٍ عَنِيدٍ
“Yéen ñaar, sànni leen ca safara weddiwaakoon ya daan féttérlu,
25مَّنَّاعٍ لِّلْخَيْرِ مُعْتَدٍ مُّرِيبٍ
ña daan tere aw yiw, te daan jalgati, daan sikki-sàkka,
26الَّذِي جَعَلَ مَعَ اللَّهِ إِلَٰهًا آخَرَ فَأَلْقِيَاهُ فِي الْعَذَابِ الشَّدِيدِ
ka daan jéem a woote jeneen Yàlla di ko booleek Yàlla. Sànni leen ko ci mbugal mu tar ma”.
27۞ قَالَ قَرِينُهُ رَبَّنَا مَا أَطْغَيْتُهُ وَلَٰكِن كَانَ فِي ضَلَالٍ بَعِيدٍ
Nekkaaleem ja (Saytaane) ngay wax naan : “sama Boroom, man dey bewloowuma ko ; waaye moom dafa nekkoon ci ag réer gu tar”.
QafFihi Alxuraan
45Aaya
MeccanRevelation
25Aaya

Tekki — Qaf 25

Simoore Qaf Aaya 25 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ña daan tere aw yiw, te daan jalgati, daan sikki-sàkka,

Simoore Aaya 25/45 — Simoore Qaf ق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Qaf Dégg, Simoore Qaf Tekki, Simoore Qaf mp3, Simoore Qaf pdf. Aaya 23–27. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers