Qaf · 35/45
Tekki Waxtaan — Qaf
لَهُم مَّا يَشَاءُونَ فِيهَا وَلَدَيْنَا مَزِيدٌ ۝٣٥
Lahum maa yashaaa`oona feehaa wa ladainaa mazeed
📖 Tekkim Wolof
Danañu fa am lépp lu leen soob. Te am Nanu ndollen.
🎧 Dégg

📜 Aaya 33-37 — Qaf

33مَّنْ خَشِيَ الرَّحْمَٰنَ بِالْغَيْبِ وَجَاءَ بِقَلْبٍ مُّنِيبٍ
kuy ragal Yàlla Yërëmakoon bi ci kumpa, te ñëw ànd ak xol bu nangu ndigal.
34ادْخُلُوهَا بِسَلَامٍ ۖ ذَٰلِكَ يَوْمُ الْخُلُودِ
Dugguleen ko ci jàmm ak tal”. Te loolu mooy sax ba fàww (Àjjana) !
35لَهُم مَّا يَشَاءُونَ فِيهَا وَلَدَيْنَا مَزِيدٌ
Danañu fa am lépp lu leen soob. Te am Nanu ndollen.
36وَكَمْ أَهْلَكْنَا قَبْلَهُم مِّن قَرْنٍ هُمْ أَشَدُّ مِنْهُم بَطْشًا فَنَقَّبُوا فِي الْبِلَادِ هَلْ مِن مَّحِيصٍ
aka bari ay xeet yu Nu faagaagaloon, ci ña leen fi jiituwoon, te ëppoon leen kàttan fuuf. Réew mu nekk dem nañu fa, mu fees di rawe.
37إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَذِكْرَىٰ لِمَن كَانَ لَهُ قَلْبٌ أَوْ أَلْقَى السَّمْعَ وَهُوَ شَهِيدٌ
Ak fàttali nekk na ci biir loolu ñeel képp ku am ub xol, tey déglu booleek teewlu doon seede.
QafFihi Alxuraan
45Aaya
MeccanRevelation
35Aaya

Tekki — Qaf 35

Simoore Qaf Aaya 35 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Danañu fa am lépp lu leen soob. Te am Nanu…

Simoore Aaya 35/45 — Qaf ق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Qaf Dégg, Qaf Tekki, Qaf mp3, Qaf pdf. Aaya 33–37. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers