Qaf · 4/45
Tekki Waxtaan — Qaf
قَدْ عَلِمْنَا مَا تَنقُصُ الْأَرْضُ مِنْهُمْ ۖ وَعِندَنَا كِتَابٌ حَفِيظٌ ٤
Transliteration
Qad `alimnaa maa tanqu-sul-ardu minhum wa `indanaa Kitaabun Hafeez
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
(Man Yàlla) Xam na a li suuf si di lekk ci ñoom ; te it Téere bu sàmmu baa ngi fi Nun (“Allawhul Mahfuuz”).
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 2-6 — Qaf
2بَلْ عَجِبُوا أَن جَاءَهُم مُّنذِرٌ مِّنْهُمْ فَقَالَ الْكَافِرُونَ هَٰذَا شَيْءٌ عَجِيبٌ
Waaye dañoo yéemu ba ñu amee waaraatekat bu bokk ci ñom ; digël leen yéefar ya di wax naan : “Lii dey mbir mu yéeme la”.
3أَإِذَا مِتْنَا وَكُنَّا تُرَابًا ۖ ذَٰلِكَ رَجْعٌ بَعِيدٌ
Ana ! Luy xew bu ñu deewee ba doon suuf...? Moo ndaw dellu guy sori waay ” !
4قَدْ عَلِمْنَا مَا تَنقُصُ الْأَرْضُ مِنْهُمْ ۖ وَعِندَنَا كِتَابٌ حَفِيظٌ
(Man Yàlla) Xam na a li suuf si di lekk ci ñoom ; te it Téere bu sàmmu baa ngi fi Nun (“Allawhul Mahfuuz”).
5بَلْ كَذَّبُوا بِالْحَقِّ لَمَّا جَاءَهُمْ فَهُمْ فِي أَمْرٍ مَّرِيجٍ
Ñoom weddi nañu dëgg ca waxtu wa mu dikëlee : ñoo nga ca mbirumu walayaange.
6أَفَلَمْ يَنظُرُوا إِلَى السَّمَاءِ فَوْقَهُمْ كَيْفَ بَنَيْنَاهَا وَزَيَّنَّاهَا وَمَا لَهَا مِن فُرُوجٍ
Moo ndax ñoom dañu téenul xool asamaan si leen tiim, ci melo wi Nu ko tabaxe taaral ko (ak i biddiw) ; te amul benn bënn-bënn ?
QafFihi Alxuraan
45Aaya
MeccanRevelation
4Aaya
Tekki — Qaf 4
Simoore Qaf Aaya 4 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : (Man Yàlla) Xam na a li suuf si di lekk…Simoore Aaya 4/45 — Qaf ق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Qaf Dégg, Qaf Tekki, Qaf mp3, Qaf pdf. Aaya 2–6. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








