Qaf · 5/45
Tekki Waxtaan — Qaf
بَلْ كَذَّبُوا بِالْحَقِّ لَمَّا جَاءَهُمْ فَهُمْ فِي أَمْرٍ مَّرِيجٍ ۝٥
Bal kazzaboo bilhaqqi lammaa jaaa`ahum fahum feee amrim mareej
📖 Tekkim Wolof
Ñoom weddi nañu dëgg ca waxtu wa mu dikëlee : ñoo nga ca mbirumu walayaange.
🎧 Dégg

📜 Aaya 3-7 — Qaf

3أَإِذَا مِتْنَا وَكُنَّا تُرَابًا ۖ ذَٰلِكَ رَجْعٌ بَعِيدٌ
Ana ! Luy xew bu ñu deewee ba doon suuf...? Moo ndaw dellu guy sori waay ” !
4قَدْ عَلِمْنَا مَا تَنقُصُ الْأَرْضُ مِنْهُمْ ۖ وَعِندَنَا كِتَابٌ حَفِيظٌ
(Man Yàlla) Xam na a li suuf si di lekk ci ñoom ; te it Téere bu sàmmu baa ngi fi Nun (“Allawhul Mahfuuz”).
5بَلْ كَذَّبُوا بِالْحَقِّ لَمَّا جَاءَهُمْ فَهُمْ فِي أَمْرٍ مَّرِيجٍ
Ñoom weddi nañu dëgg ca waxtu wa mu dikëlee : ñoo nga ca mbirumu walayaange.
6أَفَلَمْ يَنظُرُوا إِلَى السَّمَاءِ فَوْقَهُمْ كَيْفَ بَنَيْنَاهَا وَزَيَّنَّاهَا وَمَا لَهَا مِن فُرُوجٍ
Moo ndax ñoom dañu téenul xool asamaan si leen tiim, ci melo wi Nu ko tabaxe taaral ko (ak i biddiw) ; te amul benn bënn-bënn ?
7وَالْأَرْضَ مَدَدْنَاهَا وَأَلْقَيْنَا فِيهَا رَوَاسِيَ وَأَنبَتْنَا فِيهَا مِن كُلِّ زَوْجٍ بَهِيجٍ
(Ak it Ñuy settantal) suuf si, ni Nu ko tàllale dott ca biir tundi doj saxal ca wépp xeetu gàncax wu naat te taaru.
QafFihi Alxuraan
45Aaya
MeccanRevelation
5Aaya

Tekki — Qaf 5

Simoore Qaf Aaya 5 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñoom weddi nañu dëgg ca waxtu wa mu dikëlee :…

Simoore Aaya 5/45 — Qaf ق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Qaf Dégg, Qaf Tekki, Qaf mp3, Qaf pdf. Aaya 3–7. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers