Qaf · 3/45
Tekki Waxtaan — Simoore Qaf
أَإِذَا مِتْنَا وَكُنَّا تُرَابًا ۖ ذَٰلِكَ رَجْعٌ بَعِيدٌ ۝٣
A-izaa mitnaa wa kunnaa turaaban zaalika raj`um ba`eed
📖 Tekkim Wolof
Ana ! Luy xew bu ñu deewee ba doon suuf...? Moo ndaw dellu guy sori waay ” !

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 1-5 — Simoore Qaf

1ق ۚ وَالْقُرْآنِ الْمَجِيدِ
Qaaf. Ak ci Alxuraan ju tedd ji ( laay giñ) !
2بَلْ عَجِبُوا أَن جَاءَهُم مُّنذِرٌ مِّنْهُمْ فَقَالَ الْكَافِرُونَ هَٰذَا شَيْءٌ عَجِيبٌ
Waaye dañoo yéemu ba ñu amee waaraatekat bu bokk ci ñom ; digël leen yéefar ya di wax naan : “Lii dey mbir mu yéeme la”.
3أَإِذَا مِتْنَا وَكُنَّا تُرَابًا ۖ ذَٰلِكَ رَجْعٌ بَعِيدٌ
Ana ! Luy xew bu ñu deewee ba doon suuf...? Moo ndaw dellu guy sori waay ” !
4قَدْ عَلِمْنَا مَا تَنقُصُ الْأَرْضُ مِنْهُمْ ۖ وَعِندَنَا كِتَابٌ حَفِيظٌ
(Man Yàlla) Xam na a li suuf si di lekk ci ñoom ; te it Téere bu sàmmu baa ngi fi Nun (“Allawhul Mahfuuz”).
5بَلْ كَذَّبُوا بِالْحَقِّ لَمَّا جَاءَهُمْ فَهُمْ فِي أَمْرٍ مَّرِيجٍ
Ñoom weddi nañu dëgg ca waxtu wa mu dikëlee : ñoo nga ca mbirumu walayaange.
QafFihi Alxuraan
45Aaya
MeccanRevelation
3Aaya

Tekki — Qaf 3

Simoore Qaf Aaya 3 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ana ! Luy xew bu ñu deewee ba doon suuf...?…

Simoore Aaya 3/45 — Simoore Qaf ق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Qaf Dégg, Simoore Qaf Tekki, Simoore Qaf mp3, Simoore Qaf pdf. Aaya 1–5. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 29, 2026

Don't forget us in your sincere prayers