Qaf · 8/45
Tekki Waxtaan — Simoore Qaf
تَبْصِرَةً وَذِكْرَىٰ لِكُلِّ عَبْدٍ مُّنِيبٍ ۝٨
Tabsiratanw wa zikraa likulli `abdim muneeb
📖 Tekkim Wolof
mu di am njis ak ug fàttali ñeel bépp jaam buy sàkku dellu ca Boroomam.

🎧 Dégg


📜 Aaya 6-10 — Simoore Qaf

6أَفَلَمْ يَنظُرُوا إِلَى السَّمَاءِ فَوْقَهُمْ كَيْفَ بَنَيْنَاهَا وَزَيَّنَّاهَا وَمَا لَهَا مِن فُرُوجٍ
Moo ndax ñoom dañu téenul xool asamaan si leen tiim, ci melo wi Nu ko tabaxe taaral ko (ak i biddiw) ; te amul benn bënn-bënn ?
7وَالْأَرْضَ مَدَدْنَاهَا وَأَلْقَيْنَا فِيهَا رَوَاسِيَ وَأَنبَتْنَا فِيهَا مِن كُلِّ زَوْجٍ بَهِيجٍ
(Ak it Ñuy settantal) suuf si, ni Nu ko tàllale dott ca biir tundi doj saxal ca wépp xeetu gàncax wu naat te taaru.
8تَبْصِرَةً وَذِكْرَىٰ لِكُلِّ عَبْدٍ مُّنِيبٍ
mu di am njis ak ug fàttali ñeel bépp jaam buy sàkku dellu ca Boroomam.
9وَنَزَّلْنَا مِنَ السَّمَاءِ مَاءً مُّبَارَكًا فَأَنبَتْنَا بِهِ جَنَّاتٍ وَحَبَّ الْحَصِيدِ
Wàcce Nanu ndox mu barkeel mu bawoo asamaan, ñu daldi cay saxal ay tooli dër ak mbay yu ñuy góob (di ko dénc),
10وَالنَّخْلَ بَاسِقَاتٍ لَّهَا طَلْعٌ نَّضِيدٌ
tàndarma yu gudd am cëgg yu rankaloo (menn gàcc),
QafFihi Alxuraan
45Aaya
MeccanRevelation
8Aaya

Tekki — Qaf 8

Simoore Qaf Aaya 8 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : mu di am njis ak ug fàttali ñeel bépp jaam…

Simoore Aaya 8/45 — Simoore Qaf ق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Qaf Dégg, Simoore Qaf Tekki, Simoore Qaf mp3, Simoore Qaf pdf. Aaya 6–10. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers