Adh-Dhariyat · 56/60
Tekki Waxtaan — Simoore Adh-Dhariyat
وَمَا خَلَقْتُ الْجِنَّ وَالْإِنسَ إِلَّا لِيَعْبُدُونِ ۝٥٦
Wa maa khalaqtul jinna wal insa illaa liya`budoon
📖 Tekkim Wolof
Te binduma jinne ak nit lu dul ngir ñu jaamu Ma (moom rekk tax).

🎧 Dégg


📜 Aaya 54-58 — Simoore Adh-Dhariyat

54فَتَوَلَّ عَنْهُمْ فَمَا أَنتَ بِمَلُومٍ
Nangaleen dumóoyu , kenn du la ca yedd:
55وَذَكِّرْ فَإِنَّ الذِّكْرَىٰ تَنفَعُ الْمُؤْمِنِينَ
Nangay fàttalee ; ndax fàttali danay jariñ ñi gëm.
56وَمَا خَلَقْتُ الْجِنَّ وَالْإِنسَ إِلَّا لِيَعْبُدُونِ
Te binduma jinne ak nit lu dul ngir ñu jaamu Ma (moom rekk tax).
57مَا أُرِيدُ مِنْهُم مِّن رِّزْقٍ وَمَا أُرِيدُ أَن يُطْعِمُونِ
Bëgguma ci ñoom wërsëg; Bëgguma it ñu dima jox lekk.
58إِنَّ اللَّهَ هُوَ الرَّزَّاقُ ذُو الْقُوَّةِ الْمَتِينُ
Yàlla tigi, mooy Wërsëgalaakoon bi, mooy Boroom Kàttan gi dul yonjax.
Adh-DhariyatFihi Alxuraan
60Aaya
MeccanRevelation
56Aaya

Tekki — Adh-Dhariyat 56

Simoore Adh-Dhariyat Aaya 56 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te binduma jinne ak nit lu dul ngir ñu jaamu…

Simoore Aaya 56/60 — Simoore Adh-Dhariyat الذاريات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Adh-Dhariyat Dégg, Simoore Adh-Dhariyat Tekki, Simoore Adh-Dhariyat mp3, Simoore Adh-Dhariyat pdf. Aaya 54–58. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers