Adh-Dhariyat · 55/60
Tekki Waxtaan — Simoore Adh-Dhariyat
وَذَكِّرْ فَإِنَّ الذِّكْرَىٰ تَنفَعُ الْمُؤْمِنِينَ ۝٥٥
Wa zakkir fa innaz zikraa tanfa`ul mu`mineen
📖 Tekkim Wolof
Nangay fàttalee ; ndax fàttali danay jariñ ñi gëm.

🎧 Dégg


📜 Aaya 53-57 — Simoore Adh-Dhariyat

53أَتَوَاصَوْا بِهِ ۚ بَلْ هُمْ قَوْمٌ طَاغُونَ
moo ndax da ñu ko daan jottaleente ? Li am kay mooy dañoo bew rekk.
54فَتَوَلَّ عَنْهُمْ فَمَا أَنتَ بِمَلُومٍ
Nangaleen dumóoyu , kenn du la ca yedd:
55وَذَكِّرْ فَإِنَّ الذِّكْرَىٰ تَنفَعُ الْمُؤْمِنِينَ
Nangay fàttalee ; ndax fàttali danay jariñ ñi gëm.
56وَمَا خَلَقْتُ الْجِنَّ وَالْإِنسَ إِلَّا لِيَعْبُدُونِ
Te binduma jinne ak nit lu dul ngir ñu jaamu Ma (moom rekk tax).
57مَا أُرِيدُ مِنْهُم مِّن رِّزْقٍ وَمَا أُرِيدُ أَن يُطْعِمُونِ
Bëgguma ci ñoom wërsëg; Bëgguma it ñu dima jox lekk.
Adh-DhariyatFihi Alxuraan
60Aaya
MeccanRevelation
55Aaya

Tekki — Adh-Dhariyat 55

Simoore Adh-Dhariyat Aaya 55 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nangay fàttalee ; ndax fàttali danay jariñ ñi gëm.

Simoore Aaya 55/60 — Simoore Adh-Dhariyat الذاريات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Adh-Dhariyat Dégg, Simoore Adh-Dhariyat Tekki, Simoore Adh-Dhariyat mp3, Simoore Adh-Dhariyat pdf. Aaya 53–57. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers