Al-Qamar · 13/55
Tekki Waxtaan — Al-Qamar
وَحَمَلْنَاهُ عَلَىٰ ذَاتِ أَلْوَاحٍ وَدُسُرٍ ۝١٣
Wa hamalnaahu `alaa zaati alwaahinw wa dusur
📖 Tekkim Wolof
Ñu toog ca kaw gaalam ga doon ay dénk ak i pont,

🎧 Dégg


📜 Aaya 11-15 — Al-Qamar

11فَفَتَحْنَا أَبْوَابَ السَّمَاءِ بِمَاءٍ مُّنْهَمِرٍ
Nu daldi ubbi wunti asamaan si ci am ndox muy dottiku,
12وَفَجَّرْنَا الْأَرْضَ عُيُونًا فَالْتَقَى الْمَاءُ عَلَىٰ أَمْرٍ قَدْ قُدِرَ
nu daldi ballal suuf ak ay bëti ndox. Ndox ya daldi gëndóo daj ci ndigal lu ñu natale.
13وَحَمَلْنَاهُ عَلَىٰ ذَاتِ أَلْوَاحٍ وَدُسُرٍ
Ñu toog ca kaw gaalam ga doon ay dénk ak i pont,
14تَجْرِي بِأَعْيُنِنَا جَزَاءً لِّمَن كَانَ كُفِرَ
mu doon dawe ci sunug càmm : faye ko ko ngir ña weddi woon.
15وَلَقَد تَّرَكْنَاهَا آيَةً فَهَلْ مِن مُّدَّكِرٍ
Bàyyi nañu ko, mu di [kéemaan]. Moo ndax kon duñu ca jàjju ?
Al-QamarFihi Alxuraan
55Aaya
MeccanRevelation
13Aaya

Tekki — Al-Qamar 13

Simoore Al-Qamar Aaya 13 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu toog ca kaw gaalam ga doon ay dénk ak…

Simoore Aaya 13/55 — Al-Qamar القمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Qamar Dégg, Al-Qamar Tekki, Al-Qamar mp3, Al-Qamar pdf. Aaya 11–15. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers