Al-Qamar · 14/55
Tekki Waxtaan — Al-Qamar
تَجْرِي بِأَعْيُنِنَا جَزَاءً لِّمَن كَانَ كُفِرَ ١٤
Transliteration
Tajree bi a`yuninaa jazaaa `al liman kaana kufir
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
mu doon dawe ci sunug càmm : faye ko ko ngir ña weddi woon.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 12-16 — Al-Qamar
12وَفَجَّرْنَا الْأَرْضَ عُيُونًا فَالْتَقَى الْمَاءُ عَلَىٰ أَمْرٍ قَدْ قُدِرَ
nu daldi ballal suuf ak ay bëti ndox. Ndox ya daldi gëndóo daj ci ndigal lu ñu natale.
13وَحَمَلْنَاهُ عَلَىٰ ذَاتِ أَلْوَاحٍ وَدُسُرٍ
Ñu toog ca kaw gaalam ga doon ay dénk ak i pont,
14تَجْرِي بِأَعْيُنِنَا جَزَاءً لِّمَن كَانَ كُفِرَ
mu doon dawe ci sunug càmm : faye ko ko ngir ña weddi woon.
15وَلَقَد تَّرَكْنَاهَا آيَةً فَهَلْ مِن مُّدَّكِرٍ
Bàyyi nañu ko, mu di [kéemaan]. Moo ndax kon duñu ca jàjju ?
16فَكَيْفَ كَانَ عَذَابِي وَنُذُرِ
Te naka lay deme Sama mbugël at Samay xuppaate ?
Al-QamarFihi Alxuraan
55Aaya
MeccanRevelation
14Aaya
Tekki — Al-Qamar 14
Simoore Al-Qamar Aaya 14 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : mu doon dawe ci sunug càmm : faye ko ko…Simoore Aaya 14/55 — Al-Qamar القمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Qamar Dégg, Al-Qamar Tekki, Al-Qamar mp3, Al-Qamar pdf. Aaya 12–16. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








