Al-Qamar · 7/55
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qamar
خُشَّعًا أَبْصَارُهُمْ يَخْرُجُونَ مِنَ الْأَجْدَاثِ كَأَنَّهُمْ جَرَادٌ مُّنتَشِرٌ ۝٧
khushsha`an absaaruhum yakrujoona minal ajdaasi ka annahum jaraadum muntashir
📖 Tekkim Wolof
ñuy jatt seeni gis ba, di génne ci bàmmeel yi dañuy melni ay soccent yu ñu tasaare,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 5-9 — Simoore Al-Qamar

5حِكْمَةٌ بَالِغَةٌ ۖ فَمَا تُغْنِ النُّذُرُ
Ràññatle gu jotal . Waaye teewul ñuy sànku.
6فَتَوَلَّ عَنْهُمْ ۘ يَوْمَ يَدْعُ الدَّاعِ إِلَىٰ شَيْءٍ نُّكُرٍ
Nangeen leen dumóoyu. Bu keroogee ba wootekat ba di woote jëm ci mbir mu naqari,
7خُشَّعًا أَبْصَارُهُمْ يَخْرُجُونَ مِنَ الْأَجْدَاثِ كَأَنَّهُمْ جَرَادٌ مُّنتَشِرٌ
ñuy jatt seeni gis ba, di génne ci bàmmeel yi dañuy melni ay soccent yu ñu tasaare,
8مُّهْطِعِينَ إِلَى الدَّاعِ ۖ يَقُولُ الْكَافِرُونَ هَٰذَا يَوْمٌ عَسِرٌ
sëggël seeni doq, jëm ca, wootekatu ba. Yéefër yaa nga naan : “Lii dey bis bu jafeñ la”.
9۞ كَذَّبَتْ قَبْلَهُمْ قَوْمُ نُوحٍ فَكَذَّبُوا عَبْدَنَا وَقَالُوا مَجْنُونٌ وَازْدُجِرَ
Nitu Nooh, ña leen jiitu woon weddi woon nañu. Ñoom it weddi woon nañu sunub jaam daldi wax ne: “Kii ab dof la ! ” daldi koy bàyyi.
Al-QamarFihi Alxuraan
55Aaya
MeccanRevelation
7Aaya

Tekki — Al-Qamar 7

Simoore Al-Qamar Aaya 7 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ñuy jatt seeni gis ba, di génne ci bàmmeel yi…

Simoore Aaya 7/55 — Simoore Al-Qamar القمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qamar Dégg, Simoore Al-Qamar Tekki, Simoore Al-Qamar mp3, Simoore Al-Qamar pdf. Aaya 5–9. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers