Al-Qamar · 6/55
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qamar
فَتَوَلَّ عَنْهُمْ ۘ يَوْمَ يَدْعُ الدَّاعِ إِلَىٰ شَيْءٍ نُّكُرٍ ۝٦
Fatawalla `anhum; yawma yad`ud daa`i ilaa shai `in nukur
📖 Tekkim Wolof
Nangeen leen dumóoyu. Bu keroogee ba wootekat ba di woote jëm ci mbir mu naqari,

🎧 Dégg


📜 Aaya 4-8 — Simoore Al-Qamar

4وَلَقَدْ جَاءَهُم مِّنَ الْأَنبَاءِ مَا فِيهِ مُزْدَجَرٌ
Te jot nañu ci ay xibaar lu leen man a jàjj ;
5حِكْمَةٌ بَالِغَةٌ ۖ فَمَا تُغْنِ النُّذُرُ
Ràññatle gu jotal . Waaye teewul ñuy sànku.
6فَتَوَلَّ عَنْهُمْ ۘ يَوْمَ يَدْعُ الدَّاعِ إِلَىٰ شَيْءٍ نُّكُرٍ
Nangeen leen dumóoyu. Bu keroogee ba wootekat ba di woote jëm ci mbir mu naqari,
7خُشَّعًا أَبْصَارُهُمْ يَخْرُجُونَ مِنَ الْأَجْدَاثِ كَأَنَّهُمْ جَرَادٌ مُّنتَشِرٌ
ñuy jatt seeni gis ba, di génne ci bàmmeel yi dañuy melni ay soccent yu ñu tasaare,
8مُّهْطِعِينَ إِلَى الدَّاعِ ۖ يَقُولُ الْكَافِرُونَ هَٰذَا يَوْمٌ عَسِرٌ
sëggël seeni doq, jëm ca, wootekatu ba. Yéefër yaa nga naan : “Lii dey bis bu jafeñ la”.
Al-QamarFihi Alxuraan
55Aaya
MeccanRevelation
6Aaya

Tekki — Al-Qamar 6

Simoore Al-Qamar Aaya 6 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nangeen leen dumóoyu. Bu keroogee ba wootekat ba di woote…

Simoore Aaya 6/55 — Simoore Al-Qamar القمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qamar Dégg, Simoore Al-Qamar Tekki, Simoore Al-Qamar mp3, Simoore Al-Qamar pdf. Aaya 4–8. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers