Ar-Rahman · 28/78
Tekki Waxtaan — Simoore Ar-Rahman
فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ ۝٢٨
Fabi ayyi aalaaa`i Rabbikumaa tukazzibaan
📖 Tekkim Wolof
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 26-30 — Simoore Ar-Rahman

26كُلُّ مَنْ عَلَيْهَا فَانٍ
Képp kuy dund kaw [suuf] dana masa saay jeex,
27وَيَبْقَىٰ وَجْهُ رَبِّكَ ذُو الْجَلَالِ وَالْإِكْرَامِ
Sa Jëmmi Boroom doŋŋ fiy des, moom miy boroom màgg gi ak teraanga.
28فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?
29يَسْأَلُهُ مَن فِي السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۚ كُلَّ يَوْمٍ هُوَ فِي شَأْنٍ
Ñi nekk asamaan ak suuf sii ngi koy laaj aka Dagaan. Te moom bis bu nekk, Mi ngi ci mbir.
30فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?
Ar-RahmanFihi Alxuraan
78Aaya
MedinanRevelation
28Aaya

Tekki — Ar-Rahman 28

Simoore Ar-Rahman Aaya 28 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a…

Simoore Aaya 28/78 — Simoore Ar-Rahman الرحمن (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ar-Rahman Dégg, Simoore Ar-Rahman Tekki, Simoore Ar-Rahman mp3, Simoore Ar-Rahman pdf. Aaya 26–30. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers