Ar-Rahman · 27/78
Tekki Waxtaan — Simoore Ar-Rahman
وَيَبْقَىٰ وَجْهُ رَبِّكَ ذُو الْجَلَالِ وَالْإِكْرَامِ ۝٢٧
Wa yabqaa wajhu rabbika zul jalaali wal ikraam
📖 Tekkim Wolof
Sa Jëmmi Boroom doŋŋ fiy des, moom miy boroom màgg gi ak teraanga.

🎧 Dégg


📜 Aaya 25-29 — Simoore Ar-Rahman

25فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?
26كُلُّ مَنْ عَلَيْهَا فَانٍ
Képp kuy dund kaw [suuf] dana masa saay jeex,
27وَيَبْقَىٰ وَجْهُ رَبِّكَ ذُو الْجَلَالِ وَالْإِكْرَامِ
Sa Jëmmi Boroom doŋŋ fiy des, moom miy boroom màgg gi ak teraanga.
28فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?
29يَسْأَلُهُ مَن فِي السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۚ كُلَّ يَوْمٍ هُوَ فِي شَأْنٍ
Ñi nekk asamaan ak suuf sii ngi koy laaj aka Dagaan. Te moom bis bu nekk, Mi ngi ci mbir.
Ar-RahmanFihi Alxuraan
78Aaya
MedinanRevelation
27Aaya

Tekki — Ar-Rahman 27

Simoore Ar-Rahman Aaya 27 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Sa Jëmmi Boroom doŋŋ fiy des, moom miy boroom màgg…

Simoore Aaya 27/78 — Simoore Ar-Rahman الرحمن (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ar-Rahman Dégg, Simoore Ar-Rahman Tekki, Simoore Ar-Rahman mp3, Simoore Ar-Rahman pdf. Aaya 25–29. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers