Ar-Rahman · 78/78
Tekki Waxtaan — Simoore Ar-Rahman
تَبَارَكَ اسْمُ رَبِّكَ ذِي الْجَلَالِ وَالْإِكْرَامِ ۝٧٨
Tabaarakasmu Rabbika Zil-Jalaali wal-Ikraam
📖 Tekkim Wolof
Saw turu Boroom Baarkeel na, moom miy Boroom Màgg ak Teraanga ji !

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 76-78 — Simoore Ar-Rahman

76مُتَّكِئِينَ عَلَىٰ رَفْرَفٍ خُضْرٍ وَعَبْقَرِيٍّ حِسَانٍ
Ña ngeen soonu ci ay ngegenaay yu nëtëx (wert) ak ay laltaay yu rafet.
77فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?
78تَبَارَكَ اسْمُ رَبِّكَ ذِي الْجَلَالِ وَالْإِكْرَامِ
Saw turu Boroom Baarkeel na, moom miy Boroom Màgg ak Teraanga ji !
Ar-RahmanFihi Alxuraan
78Aaya
MedinanRevelation
78Aaya

Tekki — Ar-Rahman 78

Simoore Ar-Rahman Aaya 78 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Saw turu Boroom Baarkeel na, moom miy Boroom Màgg ak…

Simoore Aaya 78/78 — Simoore Ar-Rahman الرحمن (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ar-Rahman Dégg, Simoore Ar-Rahman Tekki, Simoore Ar-Rahman mp3, Simoore Ar-Rahman pdf. Aaya 76–78. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers