Al-Waqi'a · 25/96
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Waqi'a
لَا يَسْمَعُونَ فِيهَا لَغْوًا وَلَا تَأْثِيمًا ۝٢٥
Laa yasma`oona feehaa laghwanw wa laa taaseemaa
📖 Tekkim Wolof
Duñu fa dégg mukk ay waxi neen walla wax ju sew ;

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 23-27 — Simoore Al-Waqi'a

23كَأَمْثَالِ اللُّؤْلُؤِ الْمَكْنُونِ
yu taaru ba mel ni wurusu peme.
24جَزَاءً بِمَا كَانُوا يَعْمَلُونَ
ñu faye leen ko la ñu daan jëf.
25لَا يَسْمَعُونَ فِيهَا لَغْوًا وَلَا تَأْثِيمًا
Duñu fa dégg mukk ay waxi neen walla wax ju sew ;
26إِلَّا قِيلًا سَلَامًا سَلَامًا
lu dul dañuy wax rekk naan : “Jàmm nga am aa jàmm rekk! ”
27وَأَصْحَابُ الْيَمِينِ مَا أَصْحَابُ الْيَمِينِ
Ak waa ndeyjoor ; ana ñan ñoo di waa ndeyjoor ?
Al-Waqi'aFihi Alxuraan
96Aaya
MeccanRevelation
25Aaya

Tekki — Al-Waqi'a 25

Simoore Al-Waqi'a Aaya 25 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Duñu fa dégg mukk ay waxi neen walla wax ju…

Simoore Aaya 25/96 — Simoore Al-Waqi'a الواقعة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Waqi'a Dégg, Simoore Al-Waqi'a Tekki, Simoore Al-Waqi'a mp3, Simoore Al-Waqi'a pdf. Aaya 23–27. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers