Al-Waqi'a · 24/96
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Waqi'a
جَزَاءً بِمَا كَانُوا يَعْمَلُونَ ۝٢٤
Jazaaa`am bimaa kaanoo ya`maloon
📖 Tekkim Wolof
ñu faye leen ko la ñu daan jëf.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 22-26 — Simoore Al-Waqi'a

22وَحُورٌ عِينٌ
Ak ay jigéen (huur al iin), yu jekk ya lool ay gët,
23كَأَمْثَالِ اللُّؤْلُؤِ الْمَكْنُونِ
yu taaru ba mel ni wurusu peme.
24جَزَاءً بِمَا كَانُوا يَعْمَلُونَ
ñu faye leen ko la ñu daan jëf.
25لَا يَسْمَعُونَ فِيهَا لَغْوًا وَلَا تَأْثِيمًا
Duñu fa dégg mukk ay waxi neen walla wax ju sew ;
26إِلَّا قِيلًا سَلَامًا سَلَامًا
lu dul dañuy wax rekk naan : “Jàmm nga am aa jàmm rekk! ”
Al-Waqi'aFihi Alxuraan
96Aaya
MeccanRevelation
24Aaya

Tekki — Al-Waqi'a 24

Simoore Al-Waqi'a Aaya 24 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ñu faye leen ko la ñu daan jëf.

Simoore Aaya 24/96 — Simoore Al-Waqi'a الواقعة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Waqi'a Dégg, Simoore Al-Waqi'a Tekki, Simoore Al-Waqi'a mp3, Simoore Al-Waqi'a pdf. Aaya 22–26. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers