Al-Waqi'a · 92/96
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Waqi'a
وَأَمَّا إِن كَانَ مِنَ الْمُكَذِّبِينَ الضَّالِّينَ ۝٩٢
Wa ammaaa in kaana minal mukazzibeenad daaalleen
📖 Tekkim Wolof
Su fekkee ne nag dafa bokk ca ña daan weddi (dekkiwaat) tey ñu réer sànku,

🎧 Dégg


📜 Aaya 90-94 — Simoore Al-Waqi'a

90وَأَمَّا إِن كَانَ مِنْ أَصْحَابِ الْيَمِينِ
Su fekkee ne nag dafa bokk ci waa ndeyjoor,
91فَسَلَامٌ لَّكَ مِنْ أَصْحَابِ الْيَمِينِ
dees na ko [teeroo]: “Jàmm ju” bawoo ca waa ndeyjoor.
92وَأَمَّا إِن كَانَ مِنَ الْمُكَذِّبِينَ الضَّالِّينَ
Su fekkee ne nag dafa bokk ca ña daan weddi (dekkiwaat) tey ñu réer sànku,
93فَنُزُلٌ مِّنْ حَمِيمٍ
des na ko teeroo ndox muy wañax,
94وَتَصْلِيَةُ جَحِيمٍ
ak xoyomu ca biir Safara.
Al-Waqi'aFihi Alxuraan
96Aaya
MeccanRevelation
92Aaya

Tekki — Al-Waqi'a 92

Simoore Al-Waqi'a Aaya 92 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Su fekkee ne nag dafa bokk ca ña daan weddi…

Simoore Aaya 92/96 — Simoore Al-Waqi'a الواقعة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Waqi'a Dégg, Simoore Al-Waqi'a Tekki, Simoore Al-Waqi'a mp3, Simoore Al-Waqi'a pdf. Aaya 90–94. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers