Al-Hadid · 1/29
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hadid
سَبَّحَ لِلَّهِ مَا فِي السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۖ وَهُوَ الْعَزِيزُ الْحَكِيمُ ۝١
Sabbaha lillaahi maa fissamaawaati wal ardi wa Huwal `Azeezul Hakeem
📖 Tekkim Wolof
Ñi nekk ci biir asamaan yeek suuf si ñi ngi sàbbaal Yàlla miy boroom Kàttan gi, te di ku Xereñ.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 1-3 — Simoore Al-Hadid

1سَبَّحَ لِلَّهِ مَا فِي السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۖ وَهُوَ الْعَزِيزُ الْحَكِيمُ
Ñi nekk ci biir asamaan yeek suuf si ñi ngi sàbbaal Yàlla miy boroom Kàttan gi, te di ku Xereñ.
2لَهُ مُلْكُ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۖ يُحْيِي وَيُمِيتُ ۖ وَهُوَ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ قَدِيرٌ
Mooy boroom nguurug asamaan yeek suuf. Mooy dundal mooy rey, te Man na lépp lu ne.
3هُوَ الْأَوَّلُ وَالْآخِرُ وَالظَّاهِرُ وَالْبَاطِنُ ۖ وَهُوَ بِكُلِّ شَيْءٍ عَلِيمٌ
Mooy ki Jëkk mooy ki Mujj, mooy ki Fés mooy ki Nëbbu te moo Xam lépp lu ne.
Al-HadidFihi Alxuraan
29Aaya
MedinanRevelation
1Aaya

Tekki — Al-Hadid 1

Simoore Al-Hadid Aaya 1 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñi nekk ci biir asamaan yeek suuf si ñi ngi…

Simoore Aaya 1/29 — Simoore Al-Hadid الحديد (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hadid Dégg, Simoore Al-Hadid Tekki, Simoore Al-Hadid mp3, Simoore Al-Hadid pdf. Aaya 1–3. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers