Al-Hadid · 4/29
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hadid
هُوَ الَّذِي خَلَقَ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ فِي سِتَّةِ أَيَّامٍ ثُمَّ اسْتَوَىٰ عَلَى الْعَرْشِ ۚ يَعْلَمُ مَا يَلِجُ فِي الْأَرْضِ وَمَا يَخْرُجُ مِنْهَا وَمَا يَنزِلُ مِنَ السَّمَاءِ وَمَا يَعْرُجُ فِيهَا ۖ وَهُوَ مَعَكُمْ أَيْنَ مَا كُنتُمْ ۚ وَاللَّهُ بِمَا تَعْمَلُونَ بَصِيرٌ ۝٤
Huwal lazee khalaqas samaawaati wal arda fee sittati ayyaamin summas tawaa `alal `Arsh; ya`lamu maa yaliju filardi wa maa yakhruju minhaa wa maa yanzilu minas samaaa`i wa maa ya`ruju feeha wa Huwa ma`akum ayna maa kuntum; wallaahu bimaa ta`maloona Baseer
📖 Tekkim Wolof
Mooy ki bind asamaan yeek suuf si ci biir juróom-benni fann ba noppi Mu yemoo ca kaw Gàngunaay ga (Aras); Xam na lépp luy dugg ci biir suuf ak lu caay génne, ak lépp luy wàcc bawoo asamaan ak lu cay yéek, te Moom mi ngi and ak yéen fu ngeen man di nekk. Te Yàlla kuy gis la li ngeen di def.

🎧 Dégg


📜 Aaya 2-6 — Simoore Al-Hadid

2لَهُ مُلْكُ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۖ يُحْيِي وَيُمِيتُ ۖ وَهُوَ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ قَدِيرٌ
Mooy boroom nguurug asamaan yeek suuf. Mooy dundal mooy rey, te Man na lépp lu ne.
3هُوَ الْأَوَّلُ وَالْآخِرُ وَالظَّاهِرُ وَالْبَاطِنُ ۖ وَهُوَ بِكُلِّ شَيْءٍ عَلِيمٌ
Mooy ki Jëkk mooy ki Mujj, mooy ki Fés mooy ki Nëbbu te moo Xam lépp lu ne.
4هُوَ الَّذِي خَلَقَ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ فِي سِتَّةِ أَيَّامٍ ثُمَّ اسْتَوَىٰ عَلَى الْعَرْشِ ۚ يَعْلَمُ مَا يَلِجُ فِي الْأَرْضِ وَمَا يَخْرُجُ مِنْهَا وَمَا يَنزِلُ مِنَ السَّمَاءِ وَمَا يَعْرُجُ فِيهَا ۖ وَهُوَ مَعَكُمْ أَيْنَ مَا كُنتُمْ ۚ وَاللَّهُ بِمَا تَعْمَلُونَ بَصِيرٌ
Mooy ki bind asamaan yeek suuf si ci biir juróom-benni fann ba noppi Mu yemoo ca kaw Gàngunaay ga (Aras); Xam na lépp luy dugg ci biir suuf ak lu caay génne, ak lépp luy wàcc bawoo asamaan ak lu cay yéek, te Moom mi ngi and ak yéen fu ngeen man di nekk. Te Yàlla kuy gis la li ngeen di def.
5لَّهُ مُلْكُ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۚ وَإِلَى اللَّهِ تُرْجَعُ الْأُمُورُ
Mooy Boroom nguurug asamaan yeek suuf si . Te ca Yàlla la mbir yépp di mujj.
6يُولِجُ اللَّيْلَ فِي النَّهَارِ وَيُولِجُ النَّهَارَ فِي اللَّيْلِ ۚ وَهُوَ عَلِيمٌ بِذَاتِ الصُّدُورِ
Mooy duggal guddi ci bëccëg te it mooy duggal bëccëg ci guddi, te Ku xam xéll la li nekk ci dënn yi.
Al-HadidFihi Alxuraan
29Aaya
MedinanRevelation
4Aaya

Tekki — Al-Hadid 4

Simoore Al-Hadid Aaya 4 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mooy ki bind asamaan yeek suuf si ci biir juróom-benni…

Simoore Aaya 4/29 — Simoore Al-Hadid الحديد (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hadid Dégg, Simoore Al-Hadid Tekki, Simoore Al-Hadid mp3, Simoore Al-Hadid pdf. Aaya 2–6. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers