Al-An'am · 127/165
Tekki Waxtaan — Al-An'am
۞ لَهُمْ دَارُ السَّلَامِ عِندَ رَبِّهِمْ ۖ وَهُوَ وَلِيُّهُم بِمَا كَانُوا يَعْمَلُونَ ۝١٢٧
Lahum daarus salaami `inda Rabbihim wa huwa waliyyuhum bimaa kaanoo ya`maloon
📖 Tekkim Wolof
Am nañu kërug jàmm fa seen Boroom. Moom moo di Seen soppe ngir la ñu daan def [ci lu baax].

🎧 Dégg


📜 Aaya 125-129 — Al-An'am

125فَمَن يُرِدِ اللَّهُ أَن يَهْدِيَهُ يَشْرَحْ صَدْرَهُ لِلْإِسْلَامِ ۖ وَمَن يُرِدْ أَن يُضِلَّهُ يَجْعَلْ صَدْرَهُ ضَيِّقًا حَرَجًا كَأَنَّمَا يَصَّعَّدُ فِي السَّمَاءِ ۚ كَذَٰلِكَ يَجْعَلُ اللَّهُ الرِّجْسَ عَلَى الَّذِينَ لَا يُؤْمِنُونَ
Ku Yàlla bëgg a jubal, dafay ubbi xolam ci Lislaam. Ku Mu bëgg a bàyyi cig réeram, day bàyyi xolam nekk cig xat gu tar ba mel ni day yéeg jëm kaw asamaan. Noonu la Yàlla di tege mbugal ña gëmul.
126وَهَٰذَا صِرَاطُ رَبِّكَ مُسْتَقِيمًا ۗ قَدْ فَصَّلْنَا الْآيَاتِ لِقَوْمٍ يَذَّكَّرُونَ
Lile mooy sa yoonu Boroom wu jub xocc wa. Leeralal Nanu Sunuy tegtal nit ñuy fàttaliku [seen Boroom].
127۞ لَهُمْ دَارُ السَّلَامِ عِندَ رَبِّهِمْ ۖ وَهُوَ وَلِيُّهُم بِمَا كَانُوا يَعْمَلُونَ
Am nañu kërug jàmm fa seen Boroom. Moom moo di Seen soppe ngir la ñu daan def [ci lu baax].
128وَيَوْمَ يَحْشُرُهُمْ جَمِيعًا يَا مَعْشَرَ الْجِنِّ قَدِ اسْتَكْثَرْتُم مِّنَ الْإِنسِ ۖ وَقَالَ أَوْلِيَاؤُهُم مِّنَ الْإِنسِ رَبَّنَا اسْتَمْتَعَ بَعْضُنَا بِبَعْضٍ وَبَلَغْنَا أَجَلَنَا الَّذِي أَجَّلْتَ لَنَا ۚ قَالَ النَّارُ مَثْوَاكُمْ خَالِدِينَ فِيهَا إِلَّا مَا شَاءَ اللَّهُ ۗ إِنَّ رَبَّكَ حَكِيمٌ عَلِيمٌ
Bis ba Mu leen di dajale [Yàlla] ñoom ñépp, di leen wax ne : "Éy yéen mboolooy jinne yi, baril ngeen seeni jëf ci nit ñi”. Nit ña ñu méngool ne : "Sunu Boroom, lenn ci nun, daanañu sàkku xéewlu ca ñeneen ña, te agsi nañu ca àpp ba Nga nu àppaloon.”. Mu ne leen : “Safaraay seen dëkkuwaay, te dangeen fay sax dàkk, lu dul la soob Yàlla.”. Sa Boroom dey Ku xereñ, Ku xam la.
129وَكَذَٰلِكَ نُوَلِّي بَعْضَ الظَّالِمِينَ بَعْضًا بِمَا كَانُوا يَكْسِبُونَ
Noonu Lanuy feeñale kiliftéefu yenn tooñkat ya ca kaw ñeneen ña ngir la ñu nekkoon di ko fàggu.
Al-An'amFihi Alxuraan
165Aaya
MeccanRevelation
127Aaya

Tekki — Al-An'am 127

Simoore Al-An'am Aaya 127 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Am nañu kërug jàmm fa seen Boroom. Moom moo di…

Simoore Aaya 127/165 — Al-An'am الأنعام (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-An'am Dégg, Al-An'am Tekki, Al-An'am mp3, Al-An'am pdf. Aaya 125–129. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers