Al-Qalam · 46/52
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qalam
أَمْ تَسْأَلُهُمْ أَجْرًا فَهُم مِّن مَّغْرَمٍ مُّثْقَلُونَ ۝٤٦
Am tas`aluhum ajran fahum mim maghramim musqaloon
📖 Tekkim Wolof
Moo ndax da nga léen di laaj ag pey te ñu fees dell ak i bor.

🎧 Dégg


📜 Aaya 44-48 — Simoore Al-Qalam

44فَذَرْنِي وَمَن يُكَذِّبُ بِهَٰذَا الْحَدِيثِ ۖ سَنَسْتَدْرِجُهُم مِّنْ حَيْثُ لَا يَعْلَمُونَ
Bàyyee ma ak ñiy jàppe waxtaan wii ( Alxuraan) ay fen dina nu léen taxañe fu ñu dul xam.
45وَأُمْلِي لَهُمْ ۚ إِنَّ كَيْدِي مَتِينٌ
Dama léen di dënniirlu waaye sama pexe naaxsaay.
46أَمْ تَسْأَلُهُمْ أَجْرًا فَهُم مِّن مَّغْرَمٍ مُّثْقَلُونَ
Moo ndax da nga léen di laaj ag pey te ñu fees dell ak i bor.
47أَمْ عِندَهُمُ الْغَيْبُ فَهُمْ يَكْتُبُونَ
Wala dañoo xam mbóot ba di ko bind.
48فَاصْبِرْ لِحُكْمِ رَبِّكَ وَلَا تَكُن كَصَاحِبِ الْحُوتِ إِذْ نَادَىٰ وَهُوَ مَكْظُومٌ
Na ngay muñ lépp luy tukkee ci sa àtteb boroom te bul mel ni ka jën wa wannoon (Yonnent Yàlla Yuunus AS) ba muy boroomam te tiitoon lool.
Al-QalamFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
46Aaya

Tekki — Al-Qalam 46

Simoore Al-Qalam Aaya 46 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo ndax da nga léen di laaj ag pey te…

Simoore Aaya 46/52 — Simoore Al-Qalam القلم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qalam Dégg, Simoore Al-Qalam Tekki, Simoore Al-Qalam mp3, Simoore Al-Qalam pdf. Aaya 44–48. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers