Al-Qalam · 49/52
Tekki Waxtaan — Al-Qalam
لَّوْلَا أَن تَدَارَكَهُ نِعْمَةٌ مِّن رَّبِّهِ لَنُبِذَ بِالْعَرَاءِ وَهُوَ مَذْمُومٌ ۝٤٩
Law laaa an tadaara kahoo ni`matum mir rabbihee lanubiza bil`araaa`i wa huwa mazmoom
📖 Tekkim Wolof
Dogankonak wallug boroomam dees na ko sànni ca tàkk ga mu ne tócc.

🎧 Dégg


📜 Aaya 47-51 — Al-Qalam

47أَمْ عِندَهُمُ الْغَيْبُ فَهُمْ يَكْتُبُونَ
Wala dañoo xam mbóot ba di ko bind.
48فَاصْبِرْ لِحُكْمِ رَبِّكَ وَلَا تَكُن كَصَاحِبِ الْحُوتِ إِذْ نَادَىٰ وَهُوَ مَكْظُومٌ
Na ngay muñ lépp luy tukkee ci sa àtteb boroom te bul mel ni ka jën wa wannoon (Yonnent Yàlla Yuunus AS) ba muy boroomam te tiitoon lool.
49لَّوْلَا أَن تَدَارَكَهُ نِعْمَةٌ مِّن رَّبِّهِ لَنُبِذَ بِالْعَرَاءِ وَهُوَ مَذْمُومٌ
Dogankonak wallug boroomam dees na ko sànni ca tàkk ga mu ne tócc.
50فَاجْتَبَاهُ رَبُّهُ فَجَعَلَهُ مِنَ الصَّالِحِينَ
Yàlla daldi ko tànn boole ko nit ñu yiwe ña.
51وَإِن يَكَادُ الَّذِينَ كَفَرُوا لَيُزْلِقُونَكَ بِأَبْصَارِهِمْ لَمَّا سَمِعُوا الذِّكْرَ وَيَقُولُونَ إِنَّهُ لَمَجْنُونٌ
Ña weddi saayu ñu déggée (Alxuraan) dina ñu lay xawa xeelu te naan kii ab dof la kat.
Al-QalamFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
49Aaya

Tekki — Al-Qalam 49

Simoore Al-Qalam Aaya 49 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Dogankonak wallug boroomam dees na ko sànni ca tàkk ga…

Simoore Aaya 49/52 — Al-Qalam القلم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Qalam Dégg, Al-Qalam Tekki, Al-Qalam mp3, Al-Qalam pdf. Aaya 47–51. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers