Al-Qalam · 50/52
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qalam
فَاجْتَبَاهُ رَبُّهُ فَجَعَلَهُ مِنَ الصَّالِحِينَ ۝٥٠
Fajtabaahu rabbuhoo faja`alahoo minas saaliheen
📖 Tekkim Wolof
Yàlla daldi ko tànn boole ko nit ñu yiwe ña.

🎧 Dégg


📜 Aaya 48-52 — Simoore Al-Qalam

48فَاصْبِرْ لِحُكْمِ رَبِّكَ وَلَا تَكُن كَصَاحِبِ الْحُوتِ إِذْ نَادَىٰ وَهُوَ مَكْظُومٌ
Na ngay muñ lépp luy tukkee ci sa àtteb boroom te bul mel ni ka jën wa wannoon (Yonnent Yàlla Yuunus AS) ba muy boroomam te tiitoon lool.
49لَّوْلَا أَن تَدَارَكَهُ نِعْمَةٌ مِّن رَّبِّهِ لَنُبِذَ بِالْعَرَاءِ وَهُوَ مَذْمُومٌ
Dogankonak wallug boroomam dees na ko sànni ca tàkk ga mu ne tócc.
50فَاجْتَبَاهُ رَبُّهُ فَجَعَلَهُ مِنَ الصَّالِحِينَ
Yàlla daldi ko tànn boole ko nit ñu yiwe ña.
51وَإِن يَكَادُ الَّذِينَ كَفَرُوا لَيُزْلِقُونَكَ بِأَبْصَارِهِمْ لَمَّا سَمِعُوا الذِّكْرَ وَيَقُولُونَ إِنَّهُ لَمَجْنُونٌ
Ña weddi saayu ñu déggée (Alxuraan) dina ñu lay xawa xeelu te naan kii ab dof la kat.
52وَمَا هُوَ إِلَّا ذِكْرٌ لِّلْعَالَمِينَ
(Alxuraan) du lenn lu dul (ab téeré ) buy fàttali bindéef yi.
Al-QalamFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
50Aaya

Tekki — Al-Qalam 50

Simoore Al-Qalam Aaya 50 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yàlla daldi ko tànn boole ko nit ñu yiwe ña.

Simoore Aaya 50/52 — Simoore Al-Qalam القلم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qalam Dégg, Simoore Al-Qalam Tekki, Simoore Al-Qalam mp3, Simoore Al-Qalam pdf. Aaya 48–52. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers