Al-A'raf · 199/206
Tekki Waxtaan — Al-A'raf
خُذِ الْعَفْوَ وَأْمُرْ بِالْعُرْفِ وَأَعْرِضْ عَنِ الْجَاهِلِينَ ۝١٩٩
khuzil `afwa waamur bil`urfi waa`rid `anil jaahileen
📖 Tekkim Wolof
Jéggaleel te nangay digle yiw, te nanga dëddu ñu réer ña.
🎧 Dégg

📜 Aaya 197-201 — Al-A'raf

197وَالَّذِينَ تَدْعُونَ مِن دُونِهِ لَا يَسْتَطِيعُونَ نَصْرَكُمْ وَلَا أَنفُسَهُمْ يَنصُرُونَ
Ña ngeen di jaamu te bàyyi Ko, mënuñuleen a dimbali te mënuñoo dimbali seen bopp sax.”
198وَإِن تَدْعُوهُمْ إِلَى الْهُدَىٰ لَا يَسْمَعُوا ۖ وَتَرَاهُمْ يَنظُرُونَ إِلَيْكَ وَهُمْ لَا يُبْصِرُونَ
Boo leen woowee cig njub duñu dégg sax. Dangeen gis ñu di la xool te ñoom duñu gis.
199خُذِ الْعَفْوَ وَأْمُرْ بِالْعُرْفِ وَأَعْرِضْ عَنِ الْجَاهِلِينَ
Jéggaleel te nangay digle yiw, te nanga dëddu ñu réer ña.
200وَإِمَّا يَنزَغَنَّكَ مِنَ الشَّيْطَانِ نَزْغٌ فَاسْتَعِذْ بِاللَّهِ ۚ إِنَّهُ سَمِيعٌ عَلِيمٌ
Saa su la ag soppeeku dalee, gu tukke ci Séytaane, nanga sàkku mucc ci Yàlla. Moom Yàlla nag Kuy dégg la, Kuy xam la.
201إِنَّ الَّذِينَ اتَّقَوْا إِذَا مَسَّهُمْ طَائِفٌ مِّنَ الشَّيْطَانِ تَذَكَّرُوا فَإِذَا هُم مُّبْصِرُونَ
Ña ragal Yàlla, bu leen lu metti dalee, tukke ci Séytaane, ñu fàttaliku [seen Boroom] daldi nekk ñu am ràññee.
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
199Aaya

Tekki — Al-A'raf 199

Simoore Al-A'raf Aaya 199 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Jéggaleel te nangay digle yiw, te nanga dëddu ñu réer…

Simoore Aaya 199/206 — Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-A'raf Dégg, Al-A'raf Tekki, Al-A'raf mp3, Al-A'raf pdf. Aaya 197–201. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers