Al-Insan · 26/31
Tekki Waxtaan — Al-Insan
وَمِنَ اللَّيْلِ فَاسْجُدْ لَهُ وَسَبِّحْهُ لَيْلًا طَوِيلًا ۝٢٦
Wa minal laili fasjud lahoo wa sabbihhu lailan taweelaa
📖 Tekkim Wolof
te guddi gi it na nga Koy sujuudal ; te di ko sàbbaal [waxtuw] guddi lu bari.

🎧 Dégg


📜 Aaya 24-28 — Al-Insan

24فَاصْبِرْ لِحُكْمِ رَبِّكَ وَلَا تُطِعْ مِنْهُمْ آثِمًا أَوْ كَفُورًا
Muñal sa dogalub Boroom, te bul topp, ci ñoom, kenn kuy def bàkkaar walla mu di yéefar.
25وَاذْكُرِ اسْمَ رَبِّكَ بُكْرَةً وَأَصِيلًا
Te na nga tudd sa turu Boroom, subaak ngoon ;
26وَمِنَ اللَّيْلِ فَاسْجُدْ لَهُ وَسَبِّحْهُ لَيْلًا طَوِيلًا
te guddi gi it na nga Koy sujuudal ; te di ko sàbbaal [waxtuw] guddi lu bari.
27إِنَّ هَٰؤُلَاءِ يُحِبُّونَ الْعَاجِلَةَ وَيَذَرُونَ وَرَاءَهُمْ يَوْمًا ثَقِيلًا
Ñoom dey da ñoo bëgg Àddina tey sàggane bis bu dis ginnaawal ko.
28نَّحْنُ خَلَقْنَاهُمْ وَشَدَدْنَا أَسْرَهُمْ ۖ وَإِذَا شِئْنَا بَدَّلْنَا أَمْثَالَهُمْ تَبْدِيلًا
Nun Noo leen bind. May leen kàttan, te Sunu sooboon, Nu wuutal fi ñeneen.
Al-InsanFihi Alxuraan
31Aaya
MedinanRevelation
26Aaya

Tekki — Al-Insan 26

Simoore Al-Insan Aaya 26 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te guddi gi it na nga Koy sujuudal ; te…

Simoore Aaya 26/31 — Al-Insan الإنسان (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Insan Dégg, Al-Insan Tekki, Al-Insan mp3, Al-Insan pdf. Aaya 24–28. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers