Al-Insan · 27/31
Tekki Waxtaan — Al-Insan
إِنَّ هَٰؤُلَاءِ يُحِبُّونَ الْعَاجِلَةَ وَيَذَرُونَ وَرَاءَهُمْ يَوْمًا ثَقِيلًا ۝٢٧
Inna haaa`ulaa`i yuhibboona `aajilata wa yazaroona waraaa`ahum yawman saqeelaa
📖 Tekkim Wolof
Ñoom dey da ñoo bëgg Àddina tey sàggane bis bu dis ginnaawal ko.
🎧 Dégg

📜 Aaya 25-29 — Al-Insan

25وَاذْكُرِ اسْمَ رَبِّكَ بُكْرَةً وَأَصِيلًا
Te na nga tudd sa turu Boroom, subaak ngoon ;
26وَمِنَ اللَّيْلِ فَاسْجُدْ لَهُ وَسَبِّحْهُ لَيْلًا طَوِيلًا
te guddi gi it na nga Koy sujuudal ; te di ko sàbbaal [waxtuw] guddi lu bari.
27إِنَّ هَٰؤُلَاءِ يُحِبُّونَ الْعَاجِلَةَ وَيَذَرُونَ وَرَاءَهُمْ يَوْمًا ثَقِيلًا
Ñoom dey da ñoo bëgg Àddina tey sàggane bis bu dis ginnaawal ko.
28نَّحْنُ خَلَقْنَاهُمْ وَشَدَدْنَا أَسْرَهُمْ ۖ وَإِذَا شِئْنَا بَدَّلْنَا أَمْثَالَهُمْ تَبْدِيلًا
Nun Noo leen bind. May leen kàttan, te Sunu sooboon, Nu wuutal fi ñeneen.
29إِنَّ هَٰذِهِ تَذْكِرَةٌ ۖ فَمَن شَاءَ اتَّخَذَ إِلَىٰ رَبِّهِ سَبِيلًا
Lii dey ag fàttali la. Képp ku mu soob man ngaa sóobu yoon jëm ca sa Boroom !
Al-InsanFihi Alxuraan
31Aaya
MedinanRevelation
27Aaya

Tekki — Al-Insan 27

Simoore Al-Insan Aaya 27 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñoom dey da ñoo bëgg Àddina tey sàggane bis bu…

Simoore Aaya 27/31 — Al-Insan الإنسان (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Insan Dégg, Al-Insan Tekki, Al-Insan mp3, Al-Insan pdf. Aaya 25–29. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers