Al-Insan · 25/31
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Insan
وَاذْكُرِ اسْمَ رَبِّكَ بُكْرَةً وَأَصِيلًا ۝٢٥
Wazkuris ma Rabbika bukratanw wa aseelaa
📖 Tekkim Wolof
Te na nga tudd sa turu Boroom, subaak ngoon ;

🎧 Dégg


📜 Aaya 23-27 — Simoore Al-Insan

23إِنَّا نَحْنُ نَزَّلْنَا عَلَيْكَ الْقُرْآنَ تَنزِيلًا
Nun de Noo wàcce Alxuraan ci yaw ndànk-ndànk.
24فَاصْبِرْ لِحُكْمِ رَبِّكَ وَلَا تُطِعْ مِنْهُمْ آثِمًا أَوْ كَفُورًا
Muñal sa dogalub Boroom, te bul topp, ci ñoom, kenn kuy def bàkkaar walla mu di yéefar.
25وَاذْكُرِ اسْمَ رَبِّكَ بُكْرَةً وَأَصِيلًا
Te na nga tudd sa turu Boroom, subaak ngoon ;
26وَمِنَ اللَّيْلِ فَاسْجُدْ لَهُ وَسَبِّحْهُ لَيْلًا طَوِيلًا
te guddi gi it na nga Koy sujuudal ; te di ko sàbbaal [waxtuw] guddi lu bari.
27إِنَّ هَٰؤُلَاءِ يُحِبُّونَ الْعَاجِلَةَ وَيَذَرُونَ وَرَاءَهُمْ يَوْمًا ثَقِيلًا
Ñoom dey da ñoo bëgg Àddina tey sàggane bis bu dis ginnaawal ko.
Al-InsanFihi Alxuraan
31Aaya
MedinanRevelation
25Aaya

Tekki — Al-Insan 25

Simoore Al-Insan Aaya 25 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te na nga tudd sa turu Boroom, subaak ngoon ;

Simoore Aaya 25/31 — Simoore Al-Insan الإنسان (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Insan Dégg, Simoore Al-Insan Tekki, Simoore Al-Insan mp3, Simoore Al-Insan pdf. Aaya 23–27. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers