Al-Insan · 28/31
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Insan
نَّحْنُ خَلَقْنَاهُمْ وَشَدَدْنَا أَسْرَهُمْ ۖ وَإِذَا شِئْنَا بَدَّلْنَا أَمْثَالَهُمْ تَبْدِيلًا ۝٢٨
Nahnu khalaqnaahum wa shadadnaaa asrahum wa izaa shi`naa baddalnaaa amsaala hum tabdeelaa
📖 Tekkim Wolof
Nun Noo leen bind. May leen kàttan, te Sunu sooboon, Nu wuutal fi ñeneen.

🎧 Dégg


📜 Aaya 26-30 — Simoore Al-Insan

26وَمِنَ اللَّيْلِ فَاسْجُدْ لَهُ وَسَبِّحْهُ لَيْلًا طَوِيلًا
te guddi gi it na nga Koy sujuudal ; te di ko sàbbaal [waxtuw] guddi lu bari.
27إِنَّ هَٰؤُلَاءِ يُحِبُّونَ الْعَاجِلَةَ وَيَذَرُونَ وَرَاءَهُمْ يَوْمًا ثَقِيلًا
Ñoom dey da ñoo bëgg Àddina tey sàggane bis bu dis ginnaawal ko.
28نَّحْنُ خَلَقْنَاهُمْ وَشَدَدْنَا أَسْرَهُمْ ۖ وَإِذَا شِئْنَا بَدَّلْنَا أَمْثَالَهُمْ تَبْدِيلًا
Nun Noo leen bind. May leen kàttan, te Sunu sooboon, Nu wuutal fi ñeneen.
29إِنَّ هَٰذِهِ تَذْكِرَةٌ ۖ فَمَن شَاءَ اتَّخَذَ إِلَىٰ رَبِّهِ سَبِيلًا
Lii dey ag fàttali la. Képp ku mu soob man ngaa sóobu yoon jëm ca sa Boroom !
30وَمَا تَشَاءُونَ إِلَّا أَن يَشَاءَ اللَّهُ ۚ إِنَّ اللَّهَ كَانَ عَلِيمًا حَكِيمًا
Manu leen a sottal dara, te du dafa soob Yàlla. Moom ku Xam la ku Xereñ la.
Al-InsanFihi Alxuraan
31Aaya
MedinanRevelation
28Aaya

Tekki — Al-Insan 28

Simoore Al-Insan Aaya 28 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nun Noo leen bind. May leen kàttan, te Sunu sooboon,…

Simoore Aaya 28/31 — Simoore Al-Insan الإنسان (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Insan Dégg, Simoore Al-Insan Tekki, Simoore Al-Insan mp3, Simoore Al-Insan pdf. Aaya 26–30. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers