Al-Anfal · 53/75
Tekki Waxtaan — Al-Anfal
ذَٰلِكَ بِأَنَّ اللَّهَ لَمْ يَكُ مُغَيِّرًا نِّعْمَةً أَنْعَمَهَا عَلَىٰ قَوْمٍ حَتَّىٰ يُغَيِّرُوا مَا بِأَنفُسِهِمْ ۙ وَأَنَّ اللَّهَ سَمِيعٌ عَلِيمٌ ۝٥٣
Zaalika bi annal laaha lam yaku mughaiyiran ni matan an`amahaa `alaa qawmin hattaa yughaiyiroo maa bianfusihim wa annallaaha samee un `Aleem
📖 Tekkim Wolof
Li ko waral mooy Yàlla du soppi yiw wu Mu xéewale aw nit feek soppiwuñu li nekkoon ci ñoom. Yàlla Kuy dégg la, Ku xam la.
🎧 Dégg

📜 Aaya 51-55 — Al-Anfal

51ذَٰلِكَ بِمَا قَدَّمَتْ أَيْدِيكُمْ وَأَنَّ اللَّهَ لَيْسَ بِظَلَّامٍ لِّلْعَبِيدِ
Loolu mooy la ngeen jëfoon ci seeni yoxo.” Te it Yàlla du koy tooñ jaam ñi.
52كَدَأْبِ آلِ فِرْعَوْنَ ۙ وَالَّذِينَ مِن قَبْلِهِمْ ۚ كَفَرُوا بِآيَاتِ اللَّهِ فَأَخَذَهُمُ اللَّهُ بِذُنُوبِهِمْ ۗ إِنَّ اللَّهَ قَوِيٌّ شَدِيدُ الْعِقَابِ
Niki aaday njabootu Firawna ak ña leen jiitu, weddi woon nañu kàdduy Yàlla. Yàlla sadd leen ngir seeni bàkkaar. Naka Yàlla, Boroom kàttan la, di Ku tar mbugal.
53ذَٰلِكَ بِأَنَّ اللَّهَ لَمْ يَكُ مُغَيِّرًا نِّعْمَةً أَنْعَمَهَا عَلَىٰ قَوْمٍ حَتَّىٰ يُغَيِّرُوا مَا بِأَنفُسِهِمْ ۙ وَأَنَّ اللَّهَ سَمِيعٌ عَلِيمٌ
Li ko waral mooy Yàlla du soppi yiw wu Mu xéewale aw nit feek soppiwuñu li nekkoon ci ñoom. Yàlla Kuy dégg la, Ku xam la.
54كَدَأْبِ آلِ فِرْعَوْنَ ۙ وَالَّذِينَ مِن قَبْلِهِمْ ۚ كَذَّبُوا بِآيَاتِ رَبِّهِمْ فَأَهْلَكْنَاهُم بِذُنُوبِهِمْ وَأَغْرَقْنَا آلَ فِرْعَوْنَ ۚ وَكُلٌّ كَانُوا ظَالِمِينَ
Niki aada njabootu Firawna ak ña leen jiitu, weddi nañu kàdduy Boroom bi. Nu alag leen ngir seeni bàkkaar. Te Nu labal [ca géej] waa kër Firawna. Te ñoom ñépp nekkoon nañu di ay tooñkat.
55إِنَّ شَرَّ الدَّوَابِّ عِندَ اللَّهِ الَّذِينَ كَفَرُوا فَهُمْ لَا يُؤْمِنُونَ
Ña yées fa Yàlla ñooy ña weddi woon te duñu gëm ba mukk,
Al-AnfalFihi Alxuraan
75Aaya
MedinanRevelation
53Aaya

Tekki — Al-Anfal 53

Simoore Al-Anfal Aaya 53 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Li ko waral mooy Yàlla du soppi yiw wu Mu…

Simoore Aaya 53/75 — Al-Anfal الأنفال (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Anfal Dégg, Al-Anfal Tekki, Al-Anfal mp3, Al-Anfal pdf. Aaya 51–55. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers