Al-Anfal · 63/75
Tekki Waxtaan — Al-Anfal
وَأَلَّفَ بَيْنَ قُلُوبِهِمْ ۚ لَوْ أَنفَقْتَ مَا فِي الْأَرْضِ جَمِيعًا مَّا أَلَّفْتَ بَيْنَ قُلُوبِهِمْ وَلَٰكِنَّ اللَّهَ أَلَّفَ بَيْنَهُمْ ۚ إِنَّهُ عَزِيزٌ حَكِيمٌ ۝٦٣
Wa allafa baina quloobihim; law anfaqta maa fil ardi jamee`am maaa allafta baina quloobihim wa laakinnallaaha allafa bainahum; innaahoo `Azeezun Hakeem
📖 Tekkim Wolof
Te Moo dajale seeni xol (ñu soppante). Te yaw boo joxe woon lépp li nekk ci àddina, du tax nga mën a boole seeni xol ; Moom nag [Yàlla] Ku not la, Ku xereñ la.
🎧 Dégg

📜 Aaya 61-65 — Al-Anfal

61۞ وَإِن جَنَحُوا لِلسَّلْمِ فَاجْنَحْ لَهَا وَتَوَكَّلْ عَلَى اللَّهِ ۚ إِنَّهُ هُوَ السَّمِيعُ الْعَلِيمُ
Bu ñu jengee jëm ci jàmm, jengal yaw it jëm ca te nga wéeru ci Yàlla, naka Moom Kuy dégg la, Ku xam la.
62وَإِن يُرِيدُوا أَن يَخْدَعُوكَ فَإِنَّ حَسْبَكَ اللَّهُ ۚ هُوَ الَّذِي أَيَّدَكَ بِنَصْرِهِ وَبِالْمُؤْمِنِينَ
Bu ñu la naree wor, na la Yàlla doy. Moom moo lay dëgëral ci ndimbalam ak ñu gëm ña.
63وَأَلَّفَ بَيْنَ قُلُوبِهِمْ ۚ لَوْ أَنفَقْتَ مَا فِي الْأَرْضِ جَمِيعًا مَّا أَلَّفْتَ بَيْنَ قُلُوبِهِمْ وَلَٰكِنَّ اللَّهَ أَلَّفَ بَيْنَهُمْ ۚ إِنَّهُ عَزِيزٌ حَكِيمٌ
Te Moo dajale seeni xol (ñu soppante). Te yaw boo joxe woon lépp li nekk ci àddina, du tax nga mën a boole seeni xol ; Moom nag [Yàlla] Ku not la, Ku xereñ la.
64يَا أَيُّهَا النَّبِيُّ حَسْبُكَ اللَّهُ وَمَنِ اتَّبَعَكَ مِنَ الْمُؤْمِنِينَ
Éy yaw Yonent bi, Yàlla doy na la ak ku la topp ci ñi gëm.
65يَا أَيُّهَا النَّبِيُّ حَرِّضِ الْمُؤْمِنِينَ عَلَى الْقِتَالِ ۚ إِن يَكُن مِّنكُمْ عِشْرُونَ صَابِرُونَ يَغْلِبُوا مِائَتَيْنِ ۚ وَإِن يَكُن مِّنكُم مِّائَةٌ يَغْلِبُوا أَلْفًا مِّنَ الَّذِينَ كَفَرُوا بِأَنَّهُمْ قَوْمٌ لَّا يَفْقَهُونَ
Éy yaw Yonent bi, nanga ñaax ñi gëm ci xare. Bu amee ñaar-fukk ñu muñ, danañu not ñaari téeméeri yéefar ; bu nekkee ci yéen téeméer, danañu not junni ciy yéefar, ndax ñoom nit lañu ñu amul dégg-dégg.
Al-AnfalFihi Alxuraan
75Aaya
MedinanRevelation
63Aaya

Tekki — Al-Anfal 63

Simoore Al-Anfal Aaya 63 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te Moo dajale seeni xol (ñu soppante). Te yaw boo…

Simoore Aaya 63/75 — Al-Anfal الأنفال (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Anfal Dégg, Al-Anfal Tekki, Al-Anfal mp3, Al-Anfal pdf. Aaya 61–65. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers