Al-Anfal · 64/75
Tekki Waxtaan — Al-Anfal
يَا أَيُّهَا النَّبِيُّ حَسْبُكَ اللَّهُ وَمَنِ اتَّبَعَكَ مِنَ الْمُؤْمِنِينَ ٦٤
Transliteration
Yaaa aiyuhan Nabiyyu hasbukal laahu wa manittaba `aka minal mu`mineen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Éy yaw Yonent bi, Yàlla doy na la ak ku la topp ci ñi gëm.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 62-66 — Al-Anfal
62وَإِن يُرِيدُوا أَن يَخْدَعُوكَ فَإِنَّ حَسْبَكَ اللَّهُ ۚ هُوَ الَّذِي أَيَّدَكَ بِنَصْرِهِ وَبِالْمُؤْمِنِينَ
Bu ñu la naree wor, na la Yàlla doy. Moom moo lay dëgëral ci ndimbalam ak ñu gëm ña.
63وَأَلَّفَ بَيْنَ قُلُوبِهِمْ ۚ لَوْ أَنفَقْتَ مَا فِي الْأَرْضِ جَمِيعًا مَّا أَلَّفْتَ بَيْنَ قُلُوبِهِمْ وَلَٰكِنَّ اللَّهَ أَلَّفَ بَيْنَهُمْ ۚ إِنَّهُ عَزِيزٌ حَكِيمٌ
Te Moo dajale seeni xol (ñu soppante). Te yaw boo joxe woon lépp li nekk ci àddina, du tax nga mën a boole seeni xol ; Moom nag [Yàlla] Ku not la, Ku xereñ la.
64يَا أَيُّهَا النَّبِيُّ حَسْبُكَ اللَّهُ وَمَنِ اتَّبَعَكَ مِنَ الْمُؤْمِنِينَ
Éy yaw Yonent bi, Yàlla doy na la ak ku la topp ci ñi gëm.
65يَا أَيُّهَا النَّبِيُّ حَرِّضِ الْمُؤْمِنِينَ عَلَى الْقِتَالِ ۚ إِن يَكُن مِّنكُمْ عِشْرُونَ صَابِرُونَ يَغْلِبُوا مِائَتَيْنِ ۚ وَإِن يَكُن مِّنكُم مِّائَةٌ يَغْلِبُوا أَلْفًا مِّنَ الَّذِينَ كَفَرُوا بِأَنَّهُمْ قَوْمٌ لَّا يَفْقَهُونَ
Éy yaw Yonent bi, nanga ñaax ñi gëm ci xare. Bu amee ñaar-fukk ñu muñ, danañu not ñaari téeméeri yéefar ; bu nekkee ci yéen téeméer, danañu not junni ciy yéefar, ndax ñoom nit lañu ñu amul dégg-dégg.
66الْآنَ خَفَّفَ اللَّهُ عَنكُمْ وَعَلِمَ أَنَّ فِيكُمْ ضَعْفًا ۚ فَإِن يَكُن مِّنكُم مِّائَةٌ صَابِرَةٌ يَغْلِبُوا مِائَتَيْنِ ۚ وَإِن يَكُن مِّنكُمْ أَلْفٌ يَغْلِبُوا أَلْفَيْنِ بِإِذْنِ اللَّهِ ۗ وَاللَّهُ مَعَ الصَّابِرِينَ
Léegi, Yàlla woyofal na leen ngir xam na doyadi gi nekk ci yéen. Kon bu nekkee ci yéen téeméer yu muñ, danañu not ñaari téeméer ; bu nekkee ci yéen junni, danañu not ñaari junni, bu neexee Yàlla. Te Yàlla muñkat yi la àndal.
Al-AnfalFihi Alxuraan
75Aaya
MedinanRevelation
64Aaya
Tekki — Al-Anfal 64
Simoore Al-Anfal Aaya 64 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Éy yaw Yonent bi, Yàlla doy na la ak ku…Simoore Aaya 64/75 — Al-Anfal الأنفال (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Anfal Dégg, Al-Anfal Tekki, Al-Anfal mp3, Al-Anfal pdf. Aaya 62–66. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








