Ash-Shams · 10/15
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shams
وَقَدْ خَابَ مَن دَسَّاهَا ۝١٠
Wa qad khaaba man dassaahaa
📖 Tekkim Wolof
te it, képp ku ko sàggane, daldi nay sooy.

🎧 Dégg


📜 Aaya 8-12 — Simoore Ash-Shams

8فَأَلْهَمَهَا فُجُورَهَا وَتَقْوَاهَا
moom mi ko ràññatleel mbaax, ak mbon !
9قَدْ أَفْلَحَ مَن زَكَّاهَا
képp ku ko sellal, daldi nay texe
10وَقَدْ خَابَ مَن دَسَّاهَا
te it, képp ku ko sàggane, daldi nay sooy.
11كَذَّبَتْ ثَمُودُ بِطَغْوَاهَا
Waa Saamuud, seen bewte, tax na ñu weddi,
12إِذِ انبَعَثَ أَشْقَاهَا
ba ca ña gën weddi potoxlóo
Ash-ShamsFihi Alxuraan
15Aaya
MeccanRevelation
10Aaya

Tekki — Ash-Shams 10

Simoore Ash-Shams Aaya 10 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te it, képp ku ko sàggane, daldi nay sooy.

Simoore Aaya 10/15 — Simoore Ash-Shams الشمس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shams Dégg, Simoore Ash-Shams Tekki, Simoore Ash-Shams mp3, Simoore Ash-Shams pdf. Aaya 8–12. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers