Hud · 1/123
Tekki Waxtaan — Hud
الر ۚ كِتَابٌ أُحْكِمَتْ آيَاتُهُ ثُمَّ فُصِّلَتْ مِن لَّدُنْ حَكِيمٍ خَبِيرٍ ١
Transliteration
Alif-Laaam-Raa; Kitaabun uhkimat Aayaatuhoo summa fussilat mil ladun Hakeemin Khabeer
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Alif, Laam, Raa. Lii ab Téere la bu ñu xereñe ay kàddoom, faramfàccees ko mu tukkee ca Ku xereñ ka, di Ku deñ-kumpa [Yàlla].
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 1-3 — Hud
1الر ۚ كِتَابٌ أُحْكِمَتْ آيَاتُهُ ثُمَّ فُصِّلَتْ مِن لَّدُنْ حَكِيمٍ خَبِيرٍ
Alif, Laam, Raa. Lii ab Téere la bu ñu xereñe ay kàddoom, faramfàccees ko mu tukkee ca Ku xereñ ka, di Ku deñ-kumpa [Yàlla].
2أَلَّا تَعْبُدُوا إِلَّا اللَّهَ ۚ إِنَّنِي لَكُم مِّنْهُ نَذِيرٌ وَبَشِيرٌ
[Digaleef na leen] ngeen bañ a jaamu kenn ku dul Yàlla. Man mii dey kuy xuppe laa, di kuy waare ci yéen.
3وَأَنِ اسْتَغْفِرُوا رَبَّكُمْ ثُمَّ تُوبُوا إِلَيْهِ يُمَتِّعْكُم مَّتَاعًا حَسَنًا إِلَىٰ أَجَلٍ مُّسَمًّى وَيُؤْتِ كُلَّ ذِي فَضْلٍ فَضْلَهُ ۖ وَإِن تَوَلَّوْا فَإِنِّي أَخَافُ عَلَيْكُمْ عَذَابَ يَوْمٍ كَبِيرٍ
Te ñu sàkku njéggalu seen Boroom ; te dellu ca Moom, ànd ak tuub. Mu yóbbale leen xéewal yu gën ba ca àpp ba Mu ko dogale, mu jox képp ku ko yayoo ngëneel, ay ngënéelam. Waaye bu ngeen dummóoyoo, ragalal naa leen mbugal dal leen ci bis bu mag.
HudFihi Alxuraan
123Aaya
MeccanRevelation
1Aaya
Tekki — Hud 1
Simoore Hud Aaya 1 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Alif, Laam, Raa. Lii ab Téere la bu ñu xereñe…Simoore Aaya 1/123 — Hud هود (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Hud Dégg, Hud Tekki, Hud mp3, Hud pdf. Aaya 1–3. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








