Hud · 120/123
Tekki Waxtaan — Hud
وَكُلًّا نَّقُصُّ عَلَيْكَ مِنْ أَنبَاءِ الرُّسُلِ مَا نُثَبِّتُ بِهِ فُؤَادَكَ ۚ وَجَاءَكَ فِي هَٰذِهِ الْحَقُّ وَمَوْعِظَةٌ وَذِكْرَىٰ لِلْمُؤْمِنِينَ ١٢٠
Transliteration
Wa kullan naqussu `alaika min ambaaa`ir Rusuli maa nusabbitu bihee fu`aadak; wa jaaa`aka fee haazihil haqqu wa maw`izatunw wa zikraa lilmu` mineen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Te lépp Lanu lay nittili ci xew-xewi Yonent ya, Danu cay dalal sa xel. Te dëgg ak ug waare dikkal na la di aw lay ànd ak di fàttali ci ñi gëm.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 118-122 — Hud
118وَلَوْ شَاءَ رَبُّكَ لَجَعَلَ النَّاسَ أُمَّةً وَاحِدَةً ۖ وَلَا يَزَالُونَ مُخْتَلِفِينَ
Bu sooboon sa Boroom mu def nit ñi ñu nekk di wenn xeet doŋŋ. Waaye duñu deñ di wuute
119إِلَّا مَن رَّحِمَ رَبُّكَ ۚ وَلِذَٰلِكَ خَلَقَهُمْ ۗ وَتَمَّتْ كَلِمَةُ رَبِّكَ لَأَمْلَأَنَّ جَهَنَّمَ مِنَ الْجِنَّةِ وَالنَّاسِ أَجْمَعِينَ
ndare ña sa Boroom yërëm. Loolu moo tax Mu bind leen. Te it moo tax sa kàddug Boroom mat ca la mu wax ne : “Danaa feesal Safara ci aw nit ak i jinne mbooleseen”.
120وَكُلًّا نَّقُصُّ عَلَيْكَ مِنْ أَنبَاءِ الرُّسُلِ مَا نُثَبِّتُ بِهِ فُؤَادَكَ ۚ وَجَاءَكَ فِي هَٰذِهِ الْحَقُّ وَمَوْعِظَةٌ وَذِكْرَىٰ لِلْمُؤْمِنِينَ
Te lépp Lanu lay nittili ci xew-xewi Yonent ya, Danu cay dalal sa xel. Te dëgg ak ug waare dikkal na la di aw lay ànd ak di fàttali ci ñi gëm.
121وَقُل لِّلَّذِينَ لَا يُؤْمِنُونَ اعْمَلُوا عَلَىٰ مَكَانَتِكُمْ إِنَّا عَامِلُونَ
Te waxal ña gëmul ne leen : “Defleen lu leen soob. Nun it, nu ngiy jëf [li nu sunu Boroom digal].
122وَانتَظِرُوا إِنَّا مُنتَظِرُونَ
Xaarleen. Nun it noo ngi xaar ! ”
HudFihi Alxuraan
123Aaya
MeccanRevelation
120Aaya
Tekki — Hud 120
Simoore Hud Aaya 120 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te lépp Lanu lay nittili ci xew-xewi Yonent ya, Danu…Simoore Aaya 120/123 — Hud هود (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Hud Dégg, Hud Tekki, Hud mp3, Hud pdf. Aaya 118–122. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








