Hud · 31/123
Tekki Waxtaan — Hud
وَلَا أَقُولُ لَكُمْ عِندِي خَزَائِنُ اللَّهِ وَلَا أَعْلَمُ الْغَيْبَ وَلَا أَقُولُ إِنِّي مَلَكٌ وَلَا أَقُولُ لِلَّذِينَ تَزْدَرِي أَعْيُنُكُمْ لَن يُؤْتِيَهُمُ اللَّهُ خَيْرًا ۖ اللَّهُ أَعْلَمُ بِمَا فِي أَنفُسِهِمْ ۖ إِنِّي إِذًا لَّمِنَ الظَّالِمِينَ ۝٣١
Wa laa aqoolu lakum `indee khazaa`inul laahi wa laaa a`lamul ghaiba wa laa aqoolu inee malakunw wa laaa aqoolu lillazeena tazdareee a`yunukum lai yu`tiyahumul laahu khairan Allaahu a`lamu bimaa feee anfusihim innee izal laminaz zaalimeen
📖 Tekkim Wolof
Te waxumaleen maa yore ndàmbi Yàlla, te xamuma it lu fàddu, neewumaleen Malaaka laa ; te waxuma it ne seeni bët a xeebu, Yàlla duleen jox yiw ; Yàlla moo gën a xam li nekk ci ñoom [su ma leen waxoon yooyu], kon ma bokk ci tooñkat yi.

🎧 Dégg


📜 Aaya 29-33 — Hud

29وَيَا قَوْمِ لَا أَسْأَلُكُمْ عَلَيْهِ مَالًا ۖ إِنْ أَجْرِيَ إِلَّا عَلَى اللَّهِ ۚ وَمَا أَنَا بِطَارِدِ الَّذِينَ آمَنُوا ۚ إِنَّهُم مُّلَاقُو رَبِّهِمْ وَلَٰكِنِّي أَرَاكُمْ قَوْمًا تَجْهَلُونَ
Te yéen samaw nit, laajumaleen ci alal. Samag pey nekkul ci kenn ku dul Yàlla. Te nekkuma ñiy dàq way-gëm, ñoom danañu dajeek seen Boroom. Waaye ni ma leen gise, aw nit ñu réer ngeen.
30وَيَا قَوْمِ مَن يَنصُرُنِي مِنَ اللَّهِ إِن طَرَدتُّهُمْ ۚ أَفَلَا تَذَكَّرُونَ
te yéen samaw nit, ku may dimbali ci [mbugalu Yàlla] su ma leen dàqee ? Moo ndax dangeen dul xel-lu ?
31وَلَا أَقُولُ لَكُمْ عِندِي خَزَائِنُ اللَّهِ وَلَا أَعْلَمُ الْغَيْبَ وَلَا أَقُولُ إِنِّي مَلَكٌ وَلَا أَقُولُ لِلَّذِينَ تَزْدَرِي أَعْيُنُكُمْ لَن يُؤْتِيَهُمُ اللَّهُ خَيْرًا ۖ اللَّهُ أَعْلَمُ بِمَا فِي أَنفُسِهِمْ ۖ إِنِّي إِذًا لَّمِنَ الظَّالِمِينَ
Te waxumaleen maa yore ndàmbi Yàlla, te xamuma it lu fàddu, neewumaleen Malaaka laa ; te waxuma it ne seeni bët a xeebu, Yàlla duleen jox yiw ; Yàlla moo gën a xam li nekk ci ñoom [su ma leen waxoon yooyu], kon ma bokk ci tooñkat yi.
32قَالُوا يَا نُوحُ قَدْ جَادَلْتَنَا فَأَكْثَرْتَ جِدَالَنَا فَأْتِنَا بِمَا تَعِدُنَا إِن كُنتَ مِنَ الصَّادِقِينَ
Ñu ne ko : "Yaw Nooh, dàggasante nga ak nun ba ëppal ci dàggasante bi. Indil li nga nuy tëkkoo, su fekkee ne li ngay wax dëgg la”.
33قَالَ إِنَّمَا يَأْتِيكُم بِهِ اللَّهُ إِن شَاءَ وَمَا أَنتُم بِمُعْجِزِينَ
Mu ne : “Yàlla rekk a leen ko mën a indil - bu Ko soobee - te dungeen mën a raw.
HudFihi Alxuraan
123Aaya
MeccanRevelation
31Aaya

Tekki — Hud 31

Simoore Hud Aaya 31 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te waxumaleen maa yore ndàmbi Yàlla, te xamuma it lu…

Simoore Aaya 31/123 — Hud هود (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Hud Dégg, Hud Tekki, Hud mp3, Hud pdf. Aaya 29–33. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers