Hud · 30/123
Tekki Waxtaan — Hud
وَيَا قَوْمِ مَن يَنصُرُنِي مِنَ اللَّهِ إِن طَرَدتُّهُمْ ۚ أَفَلَا تَذَكَّرُونَ ۝٣٠
Wa yaa qawmi mai yansurunee minal laahi in tarattuhum; afalaa tazak karoon
📖 Tekkim Wolof
te yéen samaw nit, ku may dimbali ci [mbugalu Yàlla] su ma leen dàqee ? Moo ndax dangeen dul xel-lu ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 28-32 — Hud

28قَالَ يَا قَوْمِ أَرَأَيْتُمْ إِن كُنتُ عَلَىٰ بَيِّنَةٍ مِّن رَّبِّي وَآتَانِي رَحْمَةً مِّنْ عِندِهِ فَعُمِّيَتْ عَلَيْكُمْ أَنُلْزِمُكُمُوهَا وَأَنتُمْ لَهَا كَارِهُونَ
Mu ne leen : "Samaw nit ! Naka ngeen di gisee mbir mi ? Su fekkee maa ngi ci lu wér lu jóge ci sama Boroom, te Mu jox ma yërmaande ju jóge ci Moom ci lu nëbbu ci yéen, ndax dama cee ga te fekk yéen ngeen sib ko ?
29وَيَا قَوْمِ لَا أَسْأَلُكُمْ عَلَيْهِ مَالًا ۖ إِنْ أَجْرِيَ إِلَّا عَلَى اللَّهِ ۚ وَمَا أَنَا بِطَارِدِ الَّذِينَ آمَنُوا ۚ إِنَّهُم مُّلَاقُو رَبِّهِمْ وَلَٰكِنِّي أَرَاكُمْ قَوْمًا تَجْهَلُونَ
Te yéen samaw nit, laajumaleen ci alal. Samag pey nekkul ci kenn ku dul Yàlla. Te nekkuma ñiy dàq way-gëm, ñoom danañu dajeek seen Boroom. Waaye ni ma leen gise, aw nit ñu réer ngeen.
30وَيَا قَوْمِ مَن يَنصُرُنِي مِنَ اللَّهِ إِن طَرَدتُّهُمْ ۚ أَفَلَا تَذَكَّرُونَ
te yéen samaw nit, ku may dimbali ci [mbugalu Yàlla] su ma leen dàqee ? Moo ndax dangeen dul xel-lu ?
31وَلَا أَقُولُ لَكُمْ عِندِي خَزَائِنُ اللَّهِ وَلَا أَعْلَمُ الْغَيْبَ وَلَا أَقُولُ إِنِّي مَلَكٌ وَلَا أَقُولُ لِلَّذِينَ تَزْدَرِي أَعْيُنُكُمْ لَن يُؤْتِيَهُمُ اللَّهُ خَيْرًا ۖ اللَّهُ أَعْلَمُ بِمَا فِي أَنفُسِهِمْ ۖ إِنِّي إِذًا لَّمِنَ الظَّالِمِينَ
Te waxumaleen maa yore ndàmbi Yàlla, te xamuma it lu fàddu, neewumaleen Malaaka laa ; te waxuma it ne seeni bët a xeebu, Yàlla duleen jox yiw ; Yàlla moo gën a xam li nekk ci ñoom [su ma leen waxoon yooyu], kon ma bokk ci tooñkat yi.
32قَالُوا يَا نُوحُ قَدْ جَادَلْتَنَا فَأَكْثَرْتَ جِدَالَنَا فَأْتِنَا بِمَا تَعِدُنَا إِن كُنتَ مِنَ الصَّادِقِينَ
Ñu ne ko : "Yaw Nooh, dàggasante nga ak nun ba ëppal ci dàggasante bi. Indil li nga nuy tëkkoo, su fekkee ne li ngay wax dëgg la”.
HudFihi Alxuraan
123Aaya
MeccanRevelation
30Aaya

Tekki — Hud 30

Simoore Hud Aaya 30 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te yéen samaw nit, ku may dimbali ci [mbugalu Yàlla]…

Simoore Aaya 30/123 — Hud هود (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Hud Dégg, Hud Tekki, Hud mp3, Hud pdf. Aaya 28–32. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers