Hud · 91/123
Tekki Waxtaan — Hud
قَالُوا يَا شُعَيْبُ مَا نَفْقَهُ كَثِيرًا مِّمَّا تَقُولُ وَإِنَّا لَنَرَاكَ فِينَا ضَعِيفًا ۖ وَلَوْلَا رَهْطُكَ لَرَجَمْنَاكَ ۖ وَمَا أَنتَ عَلَيْنَا بِعَزِيزٍ ۝٩١
Qaaloo yaa Shu`aibu maa nafqahu kaseeram mimmaa taqoolu wa innaa lanaraaka feenaa da`eefanw wa law laa rahtuka larajamnaaka wa maaa anta `alainaa bi`azeez
📖 Tekkim Wolof
Ñu ne : "Yaw Suhaybu, amuñu ag dégg lu bari ci say wax ; te gis nanu nga nekk ku ñàkk solo fi nun. Te bu dul koon giir gi nga bokk, dananu la jam ay xeer. Nekkuloo ku tedd ci sunu kaw”.
🎧 Dégg

📜 Aaya 89-93 — Hud

89وَيَا قَوْمِ لَا يَجْرِمَنَّكُمْ شِقَاقِي أَن يُصِيبَكُم مِّثْلُ مَا أَصَابَ قَوْمَ نُوحٍ أَوْ قَوْمَ هُودٍ أَوْ قَوْمَ صَالِحٍ ۚ وَمَا قَوْمُ لُوطٍ مِّنكُم بِبَعِيدٍ
Yéen samaw nit, bëgg a wuuteek man bumu tax ngeen mel ni la daloon nitu Nooh dal leen, walla la daloon nitu Huud, walla nitu Saalihu, te sax nitu Lóot ña [fa ñu nekkoon] soriwuleen.
90وَاسْتَغْفِرُوا رَبَّكُمْ ثُمَّ تُوبُوا إِلَيْهِ ۚ إِنَّ رَبِّي رَحِيمٌ وَدُودٌ
Nangeen baalu seen Boroom te ngeen tuub jëm ci Moom. Naka sama Boroom, ab Jéggalaakoon la ku sopp [way-gëm ña] la
91قَالُوا يَا شُعَيْبُ مَا نَفْقَهُ كَثِيرًا مِّمَّا تَقُولُ وَإِنَّا لَنَرَاكَ فِينَا ضَعِيفًا ۖ وَلَوْلَا رَهْطُكَ لَرَجَمْنَاكَ ۖ وَمَا أَنتَ عَلَيْنَا بِعَزِيزٍ
Ñu ne : "Yaw Suhaybu, amuñu ag dégg lu bari ci say wax ; te gis nanu nga nekk ku ñàkk solo fi nun. Te bu dul koon giir gi nga bokk, dananu la jam ay xeer. Nekkuloo ku tedd ci sunu kaw”.
92قَالَ يَا قَوْمِ أَرَهْطِي أَعَزُّ عَلَيْكُم مِّنَ اللَّهِ وَاتَّخَذْتُمُوهُ وَرَاءَكُمْ ظِهْرِيًّا ۖ إِنَّ رَبِّي بِمَا تَعْمَلُونَ مُحِيطٌ
Mu ne : "Yéen samaw nit, moo ndax sama giir moo gën a tedd ci yéen Yàlla ba tax ngeen bàyyi Ko ginnaaw ? Sama Boroom nag Ku peeg la li ngeen di def.
93وَيَا قَوْمِ اعْمَلُوا عَلَىٰ مَكَانَتِكُمْ إِنِّي عَامِلٌ ۖ سَوْفَ تَعْلَمُونَ مَن يَأْتِيهِ عَذَابٌ يُخْزِيهِ وَمَنْ هُوَ كَاذِبٌ ۖ وَارْتَقِبُوا إِنِّي مَعَكُمْ رَقِيبٌ
Yéen samaw nit, defleen lu leen soob. Man it danaa def [li ma sama Boroom sant]. Dangeen mas a xam kan la mbugal di dal, gàcceel ko, ak kan mooy kay fen. Te muñandikuleen ! Maa ngi ànd ak yéen di muñ”.
HudFihi Alxuraan
123Aaya
MeccanRevelation
91Aaya

Tekki — Hud 91

Simoore Hud Aaya 91 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu ne : "Yaw Suhaybu, amuñu ag dégg lu bari…

Simoore Aaya 91/123 — Hud هود (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Hud Dégg, Hud Tekki, Hud mp3, Hud pdf. Aaya 89–93. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers