Yusuf · 89/111
Tekki Waxtaan — Simoore Yusuf
قَالَ هَلْ عَلِمْتُم مَّا فَعَلْتُم بِيُوسُفَ وَأَخِيهِ إِذْ أَنتُمْ جَاهِلُونَ ۝٨٩
Qaala hal `alimtum maa fa`altum bi Yoosufa wa akheehi iz antum jaahiloon
📖 Tekkim Wolof
- Mu ne leen : “Ndax xam ngeen la ngeen defoon Yuusufa ak doomu-ndeyam ja, ba ngeen nekkee cig réer ?”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 87-91 — Simoore Yusuf

87يَا بَنِيَّ اذْهَبُوا فَتَحَسَّسُوا مِن يُوسُفَ وَأَخِيهِ وَلَا تَيْأَسُوا مِن رَّوْحِ اللَّهِ ۖ إِنَّهُ لَا يَيْأَسُ مِن رَّوْحِ اللَّهِ إِلَّا الْقَوْمُ الْكَافِرُونَ
Mu ne : “Yéen samay doon ! Demleen xeeñtu ji lu jëm ci Yuusufa ak doomu-ndeyam ja. Te buleen xàddi ci dajeek yërmaande Yàlla. Ndax ay yéefar rekk ñooy xàddi ci dajeek yërmaande Yàlla”.
88فَلَمَّا دَخَلُوا عَلَيْهِ قَالُوا يَا أَيُّهَا الْعَزِيزُ مَسَّنَا وَأَهْلَنَا الضُّرُّ وَجِئْنَا بِبِضَاعَةٍ مُّزْجَاةٍ فَأَوْفِ لَنَا الْكَيْلَ وَتَصَدَّقْ عَلَيْنَا ۖ إِنَّ اللَّهَ يَجْزِي الْمُتَصَدِّقِينَ
Ba ñu agsee ci Yuusufa, ñu ne ko : “Éy yaw jawriñ ju tedd ji, xiif danoo dal nun ak sunug njaboor ; te indi nanu njëgg gu xeebu. Nattal nu te sarax nu. Yàlla dana fey saraxekat ya ! ”
89قَالَ هَلْ عَلِمْتُم مَّا فَعَلْتُم بِيُوسُفَ وَأَخِيهِ إِذْ أَنتُمْ جَاهِلُونَ
- Mu ne leen : “Ndax xam ngeen la ngeen defoon Yuusufa ak doomu-ndeyam ja, ba ngeen nekkee cig réer ?”.
90قَالُوا أَإِنَّكَ لَأَنتَ يُوسُفُ ۖ قَالَ أَنَا يُوسُفُ وَهَٰذَا أَخِي ۖ قَدْ مَنَّ اللَّهُ عَلَيْنَا ۖ إِنَّهُ مَن يَتَّقِ وَيَصْبِرْ فَإِنَّ اللَّهَ لَا يُضِيعُ أَجْرَ الْمُحْسِنِينَ
- Ñu ne ko : “Ndax yaw yaay Yuusufa ? ” - Mu ne leen : “Maay Yuusufa, kii mooy sama doomu-ndey, Yàlla defal nu ay xéewal. Ndax ku ragal Yàlla te muñ, [dana gis ne] Yàlla du sànk mukk peyug ñay refetal”.
91قَالُوا تَاللَّهِ لَقَدْ آثَرَكَ اللَّهُ عَلَيْنَا وَإِن كُنَّا لَخَاطِئِينَ
- Ñu giñ ci Yàlla ne : “Yàlla gënal na la ci sunu kaw te nun danoo juumoon rekk def bàkkaar”.
YusufFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
89Aaya

Tekki — Yusuf 89

Simoore Yusuf Aaya 89 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : - Mu ne leen : “Ndax xam ngeen la ngeen…

Simoore Aaya 89/111 — Simoore Yusuf يوسف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Yusuf Dégg, Simoore Yusuf Tekki, Simoore Yusuf mp3, Simoore Yusuf pdf. Aaya 87–91. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers