Yusuf · 88/111
Tekki Waxtaan — Yusuf
فَلَمَّا دَخَلُوا عَلَيْهِ قَالُوا يَا أَيُّهَا الْعَزِيزُ مَسَّنَا وَأَهْلَنَا الضُّرُّ وَجِئْنَا بِبِضَاعَةٍ مُّزْجَاةٍ فَأَوْفِ لَنَا الْكَيْلَ وَتَصَدَّقْ عَلَيْنَا ۖ إِنَّ اللَّهَ يَجْزِي الْمُتَصَدِّقِينَ ۝٨٨
Falammaa dakhaloo `alaihi qaaloo yaaa ayyuhal `Azeezu massanaa wa ahlanad durru wa ji`naa bibidaa `timmuzjaatin fa awfi lanal kaila wa tasaddaq `alainaa innal laaha yajzil mutasaddiqeen
📖 Tekkim Wolof
Ba ñu agsee ci Yuusufa, ñu ne ko : “Éy yaw jawriñ ju tedd ji, xiif danoo dal nun ak sunug njaboor ; te indi nanu njëgg gu xeebu. Nattal nu te sarax nu. Yàlla dana fey saraxekat ya ! ”
🎧 Dégg

📜 Aaya 86-90 — Yusuf

86قَالَ إِنَّمَا أَشْكُو بَثِّي وَحُزْنِي إِلَى اللَّهِ وَأَعْلَمُ مِنَ اللَّهِ مَا لَا تَعْلَمُونَ
- Mu ne : “Defuma lu dul tawat sama njàqare ak sama naqar ci Yàlla. Te xam naa ci Yàlla lu ngeen xamul.
87يَا بَنِيَّ اذْهَبُوا فَتَحَسَّسُوا مِن يُوسُفَ وَأَخِيهِ وَلَا تَيْأَسُوا مِن رَّوْحِ اللَّهِ ۖ إِنَّهُ لَا يَيْأَسُ مِن رَّوْحِ اللَّهِ إِلَّا الْقَوْمُ الْكَافِرُونَ
Mu ne : “Yéen samay doon ! Demleen xeeñtu ji lu jëm ci Yuusufa ak doomu-ndeyam ja. Te buleen xàddi ci dajeek yërmaande Yàlla. Ndax ay yéefar rekk ñooy xàddi ci dajeek yërmaande Yàlla”.
88فَلَمَّا دَخَلُوا عَلَيْهِ قَالُوا يَا أَيُّهَا الْعَزِيزُ مَسَّنَا وَأَهْلَنَا الضُّرُّ وَجِئْنَا بِبِضَاعَةٍ مُّزْجَاةٍ فَأَوْفِ لَنَا الْكَيْلَ وَتَصَدَّقْ عَلَيْنَا ۖ إِنَّ اللَّهَ يَجْزِي الْمُتَصَدِّقِينَ
Ba ñu agsee ci Yuusufa, ñu ne ko : “Éy yaw jawriñ ju tedd ji, xiif danoo dal nun ak sunug njaboor ; te indi nanu njëgg gu xeebu. Nattal nu te sarax nu. Yàlla dana fey saraxekat ya ! ”
89قَالَ هَلْ عَلِمْتُم مَّا فَعَلْتُم بِيُوسُفَ وَأَخِيهِ إِذْ أَنتُمْ جَاهِلُونَ
- Mu ne leen : “Ndax xam ngeen la ngeen defoon Yuusufa ak doomu-ndeyam ja, ba ngeen nekkee cig réer ?”.
90قَالُوا أَإِنَّكَ لَأَنتَ يُوسُفُ ۖ قَالَ أَنَا يُوسُفُ وَهَٰذَا أَخِي ۖ قَدْ مَنَّ اللَّهُ عَلَيْنَا ۖ إِنَّهُ مَن يَتَّقِ وَيَصْبِرْ فَإِنَّ اللَّهَ لَا يُضِيعُ أَجْرَ الْمُحْسِنِينَ
- Ñu ne ko : “Ndax yaw yaay Yuusufa ? ” - Mu ne leen : “Maay Yuusufa, kii mooy sama doomu-ndey, Yàlla defal nu ay xéewal. Ndax ku ragal Yàlla te muñ, [dana gis ne] Yàlla du sànk mukk peyug ñay refetal”.
YusufFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
88Aaya

Tekki — Yusuf 88

Simoore Yusuf Aaya 88 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ba ñu agsee ci Yuusufa, ñu ne ko : “Éy…

Simoore Aaya 88/111 — Yusuf يوسف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Yusuf Dégg, Yusuf Tekki, Yusuf mp3, Yusuf pdf. Aaya 86–90. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers